At-Tawba · 51/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
قُل لَّن يُصِيبَنَا إِلَّا مَا كَتَبَ اللَّهُ لَنَا هُوَ مَوْلَانَا ۚ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ ٥١
Transliteration
Qul lany-yuseebanaaa illaa maa katabal laahu lanaa Huwa mawlaanaa; wa `alal laahi falyatawak kalimu `minoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Dara mënunoo dal lu dul lu Yàlla bind ci nun rekk. Te Mooy sunu Kilifa. Te it ñi gëm, nañuy wéeru ci Yàlla”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 49-53 — At-Tawba
49وَمِنْهُم مَّن يَقُولُ ائْذَن لِّي وَلَا تَفْتِنِّي ۚ أَلَا فِي الْفِتْنَةِ سَقَطُوا ۗ وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمُحِيطَةٌ بِالْكَافِرِينَ
Am na ci ñoom ñuy ñaan ndigalul toog ba noppi naan : “Bul ma fitnaal nag.”. Ñoom tàbbi ñañu ci biir fitna ba noppi ; te Safaraa nga gaw yéefar ya ci wet gu nekk.
50إِن تُصِبْكَ حَسَنَةٌ تَسُؤْهُمْ ۖ وَإِن تُصِبْكَ مُصِيبَةٌ يَقُولُوا قَدْ أَخَذْنَا أَمْرَنَا مِن قَبْلُ وَيَتَوَلَّوا وَّهُمْ فَرِحُونَ
Boo amee mbégte, ñu mer. Bu la naqar dalee, ñu bég ca, te naan : “Ndokk ba demunu woon.” Et ils se détournent tout en exultant.
51قُل لَّن يُصِيبَنَا إِلَّا مَا كَتَبَ اللَّهُ لَنَا هُوَ مَوْلَانَا ۚ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ
Waxal ne : “Dara mënunoo dal lu dul lu Yàlla bind ci nun rekk. Te Mooy sunu Kilifa. Te it ñi gëm, nañuy wéeru ci Yàlla”.
52قُلْ هَلْ تَرَبَّصُونَ بِنَا إِلَّا إِحْدَى الْحُسْنَيَيْنِ ۖ وَنَحْنُ نَتَرَبَّصُ بِكُمْ أَن يُصِيبَكُمُ اللَّهُ بِعَذَابٍ مِّنْ عِندِهِ أَوْ بِأَيْدِينَا ۖ فَتَرَبَّصُوا إِنَّا مَعَكُم مُّتَرَبِّصُونَ
Waxal ne : “Yéen a ngi nuy tuŋlu, te nun lu mën a xew, dananu am benn ci ñaari ndam yi [dee Chahiid walla nu dàq leen, not leen], benn Yàlla mbugal leen ci sunuy loxo, walla Mu xaroo leen ko ba ëllëg. Kon book nanu ànd di tuŋlu”.
53قُلْ أَنفِقُوا طَوْعًا أَوْ كَرْهًا لَّن يُتَقَبَّلَ مِنكُمْ ۖ إِنَّكُمْ كُنتُمْ قَوْمًا فَاسِقِينَ
Waxal ne : “Génneleen seeni alal, mu neex walla mu naqari leen : ak lu mën a xew, Yàlla du ko nangu, te sax yéen ay saay-saay ngeen”.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
51Aaya
Tekki — At-Tawba 51
Simoore At-Tawba Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Dara mënunoo dal lu dul lu Yàlla…Simoore Aaya 51/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







