Al-Balad · 18/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْمَيْمَنَةِ ۝١٨
Ulaaa`ika As-haabul maimanah
📖 Tekkim Wolof
Ñooñee ñoo di waa ndeyjoor ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 16-20 — Simoore Al-Balad

16أَوْ مِسْكِينًا ذَا مَتْرَبَةٍ
walla ab miskiin bu fondóoñ.
17ثُمَّ كَانَ مِنَ الَّذِينَ آمَنُوا وَتَوَاصَوْا بِالصَّبْرِ وَتَوَاصَوْا بِالْمَرْحَمَةِ
Ba noppi, bokk ca, ña gëm tey dénkante ci muñ, di dénkante it ci yërmaande.
18أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْمَيْمَنَةِ
Ñooñee ñoo di waa ndeyjoor ;
19وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِنَا هُمْ أَصْحَابُ الْمَشْأَمَةِ
ñay weddi sunuy Laaya ñoom ñoo di waa càmmoñ.
20عَلَيْهِمْ نَارٌ مُّؤْصَدَةٌ
Safara waa ngi di gand.
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Balad 18

Simoore Al-Balad Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooñee ñoo di waa ndeyjoor ;

Simoore Aaya 18/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers