Al-Balad · 17/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
ثُمَّ كَانَ مِنَ الَّذِينَ آمَنُوا وَتَوَاصَوْا بِالصَّبْرِ وَتَوَاصَوْا بِالْمَرْحَمَةِ ۝١٧
Summa kaana minal lazeena aamanoo wa tawaasaw bissabri wa tawaasaw bilmarhamah
📖 Tekkim Wolof
Ba noppi, bokk ca, ña gëm tey dénkante ci muñ, di dénkante it ci yërmaande.

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore Al-Balad

15يَتِيمًا ذَا مَقْرَبَةٍ
ab jirim mba mbokk mu jige
16أَوْ مِسْكِينًا ذَا مَتْرَبَةٍ
walla ab miskiin bu fondóoñ.
17ثُمَّ كَانَ مِنَ الَّذِينَ آمَنُوا وَتَوَاصَوْا بِالصَّبْرِ وَتَوَاصَوْا بِالْمَرْحَمَةِ
Ba noppi, bokk ca, ña gëm tey dénkante ci muñ, di dénkante it ci yërmaande.
18أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْمَيْمَنَةِ
Ñooñee ñoo di waa ndeyjoor ;
19وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِنَا هُمْ أَصْحَابُ الْمَشْأَمَةِ
ñay weddi sunuy Laaya ñoom ñoo di waa càmmoñ.
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Balad 17

Simoore Al-Balad Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba noppi, bokk ca, ña gëm tey dénkante ci muñ,…

Simoore Aaya 17/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers