Al-Balad · 19/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِنَا هُمْ أَصْحَابُ الْمَشْأَمَةِ ۝١٩
Wallazeena kafaroo bi aayaatinaa hum as-haabul Mash`amah
📖 Tekkim Wolof
ñay weddi sunuy Laaya ñoom ñoo di waa càmmoñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-20 — Simoore Al-Balad

17ثُمَّ كَانَ مِنَ الَّذِينَ آمَنُوا وَتَوَاصَوْا بِالصَّبْرِ وَتَوَاصَوْا بِالْمَرْحَمَةِ
Ba noppi, bokk ca, ña gëm tey dénkante ci muñ, di dénkante it ci yërmaande.
18أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْمَيْمَنَةِ
Ñooñee ñoo di waa ndeyjoor ;
19وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِنَا هُمْ أَصْحَابُ الْمَشْأَمَةِ
ñay weddi sunuy Laaya ñoom ñoo di waa càmmoñ.
20عَلَيْهِمْ نَارٌ مُّؤْصَدَةٌ
Safara waa ngi di gand.
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Balad 19

Simoore Al-Balad Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñay weddi sunuy Laaya ñoom ñoo di waa càmmoñ.

Simoore Aaya 19/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 17–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers