Al-Bayyina · 4/8
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Bayyina
وَمَا تَفَرَّقَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ إِلَّا مِن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُمُ الْبَيِّنَةُ ۝٤
Wa maa tafarraqal lazeena ootul kitaaba il-la mim b`adi ma jaa-at humul baiyyinah
📖 Tekkim Wolof
Te gaa ña ñu joxoon téere masuñoo teqalikoo lu dul ginnaaw ba leen firnde ja dikkëlee.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Bayyina

2رَسُولٌ مِّنَ اللَّهِ يَتْلُو صُحُفًا مُّطَهَّرَةً
ab Yonent, bu jóge ca Yàlla, di jàng ay xëti këyit yu sell laab,
3فِيهَا كُتُبٌ قَيِّمَةٌ
ay téere nekk ci biir yu ame dayo bu màgg.
4وَمَا تَفَرَّقَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ إِلَّا مِن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُمُ الْبَيِّنَةُ
Te gaa ña ñu joxoon téere masuñoo teqalikoo lu dul ginnaaw ba leen firnde ja dikkëlee.
5وَمَا أُمِرُوا إِلَّا لِيَعْبُدُوا اللَّهَ مُخْلِصِينَ لَهُ الدِّينَ حُنَفَاءَ وَيُقِيمُوا الصَّلَاةَ وَيُؤْتُوا الزَّكَاةَ ۚ وَذَٰلِكَ دِينُ الْقَيِّمَةِ
Te digaleefu leen, lu dul, na nuy jaamu Yàlla, bañ Koo bokkaale te di ko sellal, tey taxawal Julli di joxe asaka. Loolu mooy diiney njub ja.
6إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ وَالْمُشْرِكِينَ فِي نَارِ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ أُولَٰئِكَ هُمْ شَرُّ الْبَرِيَّةِ
Ñay weddi te bokk ci ñoñ téere, ak Bokkaalekat ya ñoom ña nga ca biir Safaraw Jahanama, te danu fay béel. Ñoom ñii, ñoo yées ci bindeef yi.
Al-BayyinaFihi Alxuraan
8Aaya
MedinanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Bayyina 4

Simoore Al-Bayyina Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te gaa ña ñu joxoon téere masuñoo teqalikoo lu dul…

Simoore Aaya 4/8 — Simoore Al-Bayyina البينة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Bayyina Dégg, Simoore Al-Bayyina Tekki, Simoore Al-Bayyina mp3, Simoore Al-Bayyina pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers