Al-Bayyina · 3/8
Tekki Waxtaan — Al-Bayyina
فِيهَا كُتُبٌ قَيِّمَةٌ ٣
Transliteration
Feeha kutubun qaiyimah
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ay téere nekk ci biir yu ame dayo bu màgg.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-5 — Al-Bayyina
1لَمْ يَكُنِ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ وَالْمُشْرِكِينَ مُنفَكِّينَ حَتَّىٰ تَأْتِيَهُمُ الْبَيِّنَةُ
Yéefër ya bokk ca ñoñ Téere, ak Bokkaalekat ya, du ñu deñ mukk di weddi ba baa Firnde di leen dikkël ju leer :
2رَسُولٌ مِّنَ اللَّهِ يَتْلُو صُحُفًا مُّطَهَّرَةً
ab Yonent, bu jóge ca Yàlla, di jàng ay xëti këyit yu sell laab,
3فِيهَا كُتُبٌ قَيِّمَةٌ
ay téere nekk ci biir yu ame dayo bu màgg.
4وَمَا تَفَرَّقَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ إِلَّا مِن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُمُ الْبَيِّنَةُ
Te gaa ña ñu joxoon téere masuñoo teqalikoo lu dul ginnaaw ba leen firnde ja dikkëlee.
5وَمَا أُمِرُوا إِلَّا لِيَعْبُدُوا اللَّهَ مُخْلِصِينَ لَهُ الدِّينَ حُنَفَاءَ وَيُقِيمُوا الصَّلَاةَ وَيُؤْتُوا الزَّكَاةَ ۚ وَذَٰلِكَ دِينُ الْقَيِّمَةِ
Te digaleefu leen, lu dul, na nuy jaamu Yàlla, bañ Koo bokkaale te di ko sellal, tey taxawal Julli di joxe asaka. Loolu mooy diiney njub ja.
Al-BayyinaFihi Alxuraan
8Aaya
MedinanRevelation
3Aaya
Tekki — Al-Bayyina 3
Simoore Al-Bayyina Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ay téere nekk ci biir yu ame dayo bu màgg.Simoore Aaya 3/8 — Al-Bayyina البينة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Bayyina Dégg, Al-Bayyina Tekki, Al-Bayyina mp3, Al-Bayyina pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








