5 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﮈﮉﮊﮋﮌﮍ
111:1 Ñaari yoxoy Abii Lahab dogg nañu te it dugg na.
ﮎﮏﮐﮑﮒﮓﮔ
111:2 alalam ak la muy fàggu, du ko jariñ dara.
ﮕﮖﮗﮘﮙ
111:3 Dana lakk ci biir Safara wuy bérax.
ﮚﮛﮜﮝ
111:4 ak jabaram ja daan yanu matt ma,
ﮞﮟﮠﮡﮢﮣ
111:5 loosam wa, buumug rawa cay nekk (caq bu ñu soy).

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers