Yunus · 109/109
Tekki Waxtaan — Simoore Yunus
وَاتَّبِعْ مَا يُوحَىٰ إِلَيْكَ وَاصْبِرْ حَتَّىٰ يَحْكُمَ اللَّهُ ۚ وَهُوَ خَيْرُ الْحَاكِمِينَ ۝١٠٩
Qattabi` maa yoohaaa ilaika wasbir hattaa yahkumal laah; wa Huwa khairul haakimeen
📖 Tekkim Wolof
e nanga topp [Yaw Yonent bi] la ñu la soloo, te nga sax ci Man ba ba Yàllay àtte te Mooy gën jaa mën a àtte.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 107-109 — Simoore Yunus

107وَإِن يَمْسَسْكَ اللَّهُ بِضُرٍّ فَلَا كَاشِفَ لَهُ إِلَّا هُوَ ۖ وَإِن يُرِدْكَ بِخَيْرٍ فَلَا رَادَّ لِفَضْلِهِ ۚ يُصِيبُ بِهِ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ ۚ وَهُوَ الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Bu la Yàlla saddee aw naqar, kenn du la ko mën a teggil ku dul Moom. Bu la bégalee ci aw yiw, dara du mën a fànq xéewalam. Dana ko jottale ku ko soob ci jaamam yi. Moo di Xéewalaakoon ba, di Jaglewaakoon ba.
108قُلْ يَا أَيُّهَا النَّاسُ قَدْ جَاءَكُمُ الْحَقُّ مِن رَّبِّكُمْ ۖ فَمَنِ اهْتَدَىٰ فَإِنَّمَا يَهْتَدِي لِنَفْسِهِ ۖ وَمَن ضَلَّ فَإِنَّمَا يَضِلُّ عَلَيْهَا ۖ وَمَا أَنَا عَلَيْكُم بِوَكِيلٍ
Neel : "Éy yéen nit ñi ! Dëgg gi ñëw na ci yéen tukke ci seen Boroom. Ku jub te gindiku, boppam ; ku réer, sànku it boppam. Man dey warlulumaleen dara [ci seeni mbir].
109وَاتَّبِعْ مَا يُوحَىٰ إِلَيْكَ وَاصْبِرْ حَتَّىٰ يَحْكُمَ اللَّهُ ۚ وَهُوَ خَيْرُ الْحَاكِمِينَ
e nanga topp [Yaw Yonent bi] la ñu la soloo, te nga sax ci Man ba ba Yàllay àtte te Mooy gën jaa mën a àtte.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Yunus 109

Simoore Yunus Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : e nanga topp [Yaw Yonent bi] la ñu la soloo,…

Simoore Aaya 109/109 — Simoore Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yunus Dégg, Simoore Yunus Tekki, Simoore Yunus mp3, Simoore Yunus pdf. Aaya 107–109. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers