Hud · 106/123
Tekki Waxtaan — Hud
فَأَمَّا الَّذِينَ شَقُوا فَفِي النَّارِ لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَشَهِيقٌ ١٠٦
Transliteration
Fa ammal lazeena shaqoo fafin Naari lahum feehaa zafeerunw wa shaheeq
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a jooy.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 104-108 — Hud
104وَمَا نُؤَخِّرُهُ إِلَّا لِأَجَلٍ مَّعْدُودٍ
Yeexewuñu ko de, dafa di rekk am na dig bu ñu ko àppal.
105يَوْمَ يَأْتِ لَا تَكَلَّمُ نَفْسٌ إِلَّا بِإِذْنِهِ ۚ فَمِنْهُمْ شَقِيٌّ وَسَعِيدٌ
Bu bis ba dikkee, kenn du wax ku dul ku ca am ndigal. Te ca nit ña am na ca ñu texeedi ak ñu texe.
106فَأَمَّا الَّذِينَ شَقُوا فَفِي النَّارِ لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَشَهِيقٌ
Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a jooy.
107خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Dañu fay béel, nekk fa feek asamaan yi ak suuf si - ndare lu neex sa Boroom - ndax Moom lu ko soob Mu def ko.
108۞ وَأَمَّا الَّذِينَ سُعِدُوا فَفِي الْجَنَّةِ خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۖ عَطَاءً غَيْرَ مَجْذُوذٍ
Ña texe, danañu nekk fa Àjjana, te dañu fay béel, nekk fa li feek asamaan yi ak suuf si ñi ngi fi - ndare lu neex sa Boroom - mu di ag may gu dul dog mukk.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
106Aaya
Tekki — Hud 106
Simoore Hud Aaya 106 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a…Simoore Aaya 106/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 104–108. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








