Hud · 105/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
يَوْمَ يَأْتِ لَا تَكَلَّمُ نَفْسٌ إِلَّا بِإِذْنِهِ ۚ فَمِنْهُمْ شَقِيٌّ وَسَعِيدٌ ۝١٠٥
Yawma yaati laa takallamu nafsun illaa bi iznih; faminhum shaqiyyunw wa sa`eed
📖 Tekkim Wolof
Bu bis ba dikkee, kenn du wax ku dul ku ca am ndigal. Te ca nit ña am na ca ñu texeedi ak ñu texe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 103-107 — Simoore Hud

103إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّمَنْ خَافَ عَذَابَ الْآخِرَةِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّجْمُوعٌ لَّهُ النَّاسُ وَذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّشْهُودٌ
Kaawtéef nekk na ci loolu ci ku ragal mbugalam àllaaxira. Bis boobu bis ba ñu koy dajaleel nit ñi; te bis la bu ñépp di teewe.
104وَمَا نُؤَخِّرُهُ إِلَّا لِأَجَلٍ مَّعْدُودٍ
Yeexewuñu ko de, dafa di rekk am na dig bu ñu ko àppal.
105يَوْمَ يَأْتِ لَا تَكَلَّمُ نَفْسٌ إِلَّا بِإِذْنِهِ ۚ فَمِنْهُمْ شَقِيٌّ وَسَعِيدٌ
Bu bis ba dikkee, kenn du wax ku dul ku ca am ndigal. Te ca nit ña am na ca ñu texeedi ak ñu texe.
106فَأَمَّا الَّذِينَ شَقُوا فَفِي النَّارِ لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَشَهِيقٌ
Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a jooy.
107خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Dañu fay béel, nekk fa feek asamaan yi ak suuf si - ndare lu neex sa Boroom - ndax Moom lu ko soob Mu def ko.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
105Aaya

Tekki — Hud 105

Simoore Hud Aaya 105 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu bis ba dikkee, kenn du wax ku dul ku…

Simoore Aaya 105/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 103–107. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers