Al-Hijr · 2/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
رُّبَمَا يَوَدُّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْ كَانُوا مُسْلِمِينَ ۝٢
Rubamaa yawaddul lazeena kafaroo law kaanoo muslimeen
📖 Tekkim Wolof
Amaana ña weddi ñanga ne siiw nekki jullit.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-4 — Al-Hijr

1الر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ وَقُرْآنٍ مُّبِينٍ
Alif, Laam, Raa. Àttey Téere bee ngi nii, di am njàngale muy biral [dëgg].
2رُّبَمَا يَوَدُّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْ كَانُوا مُسْلِمِينَ
Amaana ña weddi ñanga ne siiw nekki jullit.
3ذَرْهُمْ يَأْكُلُوا وَيَتَمَتَّعُوا وَيُلْهِهِمُ الْأَمَلُ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Bàyyileen ñuy lekk ak a xéewlu, tey mébét lu leen soxal; danañu mës a xam !
4وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا وَلَهَا كِتَابٌ مَّعْلُومٌ
Dunu alag benn dëkk te fekk amul àpp bu ñu xam.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Hijr 2

Simoore Al-Hijr Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amaana ña weddi ñanga ne siiw nekki jullit.

Simoore Aaya 2/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers