An-Nahl · 11/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
يُنبِتُ لَكُم بِهِ الزَّرْعَ وَالزَّيْتُونَ وَالنَّخِيلَ وَالْأَعْنَابَ وَمِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ ١١
Transliteration
Yumbitu lakum bihiz zar`a wazzaitoona wanna kheela wal-a`naaba wa min kullis samaraat, inna fee zaalika la Aayatal liqawminy yatafakkaroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu di leen cay saxal mbey, garabi oliiw ak i tàndarma, ak yu reseñ, ak bépp meññent. Loolu mën naa waar aw nit yuy xalaat [natt].
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 9-13 — An-Nahl
9وَعَلَى اللَّهِ قَصْدُ السَّبِيلِ وَمِنْهَا جَائِرٌ ۚ وَلَوْ شَاءَ لَهَدَاكُمْ أَجْمَعِينَ
Yàlla moo yeyoo leeral yoon wu jub wa, [te am na ci yoon yi] yu jeng féeroo ak njub. Te bu Ko sooboon Mu jubal leen yéen ñépp.
10هُوَ الَّذِي أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً ۖ لَّكُم مِّنْهُ شَرَابٌ وَمِنْهُ شَجَرٌ فِيهِ تُسِيمُونَ
Moom mooy ki leen wàcceel ndox mu jóge asamaan, ngeen di ca naan, garab yi di ca saxe, ngeen di ca nàndale [jur gi].
11يُنبِتُ لَكُم بِهِ الزَّرْعَ وَالزَّيْتُونَ وَالنَّخِيلَ وَالْأَعْنَابَ وَمِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ
Mu di leen cay saxal mbey, garabi oliiw ak i tàndarma, ak yu reseñ, ak bépp meññent. Loolu mën naa waar aw nit yuy xalaat [natt].
12وَسَخَّرَ لَكُمُ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ وَالشَّمْسَ وَالْقَمَرَ ۖ وَالنُّجُومُ مُسَخَّرَاتٌ بِأَمْرِهِ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Te Moo leen tàggatal guddi gi ak bëccëg gi ; ak jant bi ak weer wi. Ak bidiw yi itam. Ci ndigalam, loolu dey ag kéemaan a ngi ci ngir aw nit ñuy xel-lu.
13وَمَا ذَرَأَ لَكُمْ فِي الْأَرْضِ مُخْتَلِفًا أَلْوَانُهُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَذَّكَّرُونَ
Te li Mu leen wesaareel ci kaw suuf si am nañu ay melo yu wuute. Te ci biir yooyu, am na ca ay kéemaan ñeel aw nit ñuy waaru.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
11Aaya
Tekki — An-Nahl 11
Simoore An-Nahl Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu di leen cay saxal mbey, garabi oliiw ak i…Simoore Aaya 11/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








