An-Nahl · 10/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
هُوَ الَّذِي أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً ۖ لَّكُم مِّنْهُ شَرَابٌ وَمِنْهُ شَجَرٌ فِيهِ تُسِيمُونَ ۝١٠
Huwal lazeee anzala minas samaaa`i maaa`al lakum minhu sharaabunw wa minhu shajarun feehi tuseemoon
📖 Tekkim Wolof
Moom mooy ki leen wàcceel ndox mu jóge asamaan, ngeen di ca naan, garab yi di ca saxe, ngeen di ca nàndale [jur gi].
🎧 Dégg

📜 Aaya 8-12 — An-Nahl

8وَالْخَيْلَ وَالْبِغَالَ وَالْحَمِيرَ لِتَرْكَبُوهَا وَزِينَةً ۚ وَيَخْلُقُ مَا لَا تَعْلَمُونَ
[Moo bind it] fas ak i baxla [berkelle] ak mbaam ngir ngeen war leen, ak ngir taar. Te it bind na lu ngeen xamul.
9وَعَلَى اللَّهِ قَصْدُ السَّبِيلِ وَمِنْهَا جَائِرٌ ۚ وَلَوْ شَاءَ لَهَدَاكُمْ أَجْمَعِينَ
Yàlla moo yeyoo leeral yoon wu jub wa, [te am na ci yoon yi] yu jeng féeroo ak njub. Te bu Ko sooboon Mu jubal leen yéen ñépp.
10هُوَ الَّذِي أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً ۖ لَّكُم مِّنْهُ شَرَابٌ وَمِنْهُ شَجَرٌ فِيهِ تُسِيمُونَ
Moom mooy ki leen wàcceel ndox mu jóge asamaan, ngeen di ca naan, garab yi di ca saxe, ngeen di ca nàndale [jur gi].
11يُنبِتُ لَكُم بِهِ الزَّرْعَ وَالزَّيْتُونَ وَالنَّخِيلَ وَالْأَعْنَابَ وَمِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ
Mu di leen cay saxal mbey, garabi oliiw ak i tàndarma, ak yu reseñ, ak bépp meññent. Loolu mën naa waar aw nit yuy xalaat [natt].
12وَسَخَّرَ لَكُمُ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ وَالشَّمْسَ وَالْقَمَرَ ۖ وَالنُّجُومُ مُسَخَّرَاتٌ بِأَمْرِهِ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Te Moo leen tàggatal guddi gi ak bëccëg gi ; ak jant bi ak weer wi. Ak bidiw yi itam. Ci ndigalam, loolu dey ag kéemaan a ngi ci ngir aw nit ñuy xel-lu.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — An-Nahl 10

Simoore An-Nahl Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom mooy ki leen wàcceel ndox mu jóge asamaan, ngeen…

Simoore Aaya 10/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers