Al-Isra · 102/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
قَالَ لَقَدْ عَلِمْتَ مَا أَنزَلَ هَٰؤُلَاءِ إِلَّا رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ بَصَائِرَ وَإِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا فِرْعَوْنُ مَثْبُورًا ۝١٠٢
Qaala laqad `alimta maaa anzala haaa`ulaaa`i illaa Rabbus samaawaati wal ardi basaaa`ira wa innee la azun nuka yaa Fir`awnu masbooraa
📖 Tekkim Wolof
[Muusaa tontu ne] : “Xam nga ne kenn wàccewul yile [kéemaan] ku dul Boroom asamaan yi ak suuf si ngir ñu nekk di waare ; te damaa defe ni, yaw Firawna, dangaa nekk ku alku”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 100-104 — Simoore Al-Isra

100قُل لَّوْ أَنتُمْ تَمْلِكُونَ خَزَائِنَ رَحْمَةِ رَبِّي إِذًا لَّأَمْسَكْتُمْ خَشْيَةَ الْإِنفَاقِ ۚ وَكَانَ الْإِنسَانُ قَتُورًا
Neel : “Su fekkoon ne yéen a moom ndàmbi yërmaandey Yàlla yi ; kon ngeen nay [ci joxe ko] ngir ŋott. Nit dafa di ku ŋott !
101وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ تِسْعَ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ ۖ فَاسْأَلْ بَنِي إِسْرَائِيلَ إِذْ جَاءَهُمْ فَقَالَ لَهُ فِرْعَوْنُ إِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا مُوسَىٰ مَسْحُورًا
Tigi, joxoon Nanu Muusaa juróom-ñeenti kéemaan yu leer. Laajal waa Bani-Israayiil, ba mu ñëwee fa ñoom, Firawna ne ko : “Muusaa, dama defe ne dañu laa jabar”.
102قَالَ لَقَدْ عَلِمْتَ مَا أَنزَلَ هَٰؤُلَاءِ إِلَّا رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ بَصَائِرَ وَإِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا فِرْعَوْنُ مَثْبُورًا
[Muusaa tontu ne] : “Xam nga ne kenn wàccewul yile [kéemaan] ku dul Boroom asamaan yi ak suuf si ngir ñu nekk di waare ; te damaa defe ni, yaw Firawna, dangaa nekk ku alku”.
103فَأَرَادَ أَن يَسْتَفِزَّهُم مِّنَ الْأَرْضِ فَأَغْرَقْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ جَمِيعًا
Mu bëgg leen a génne suuf sa. Nu labal ko mook ña mu àndaloon ñépp.
104وَقُلْنَا مِن بَعْدِهِ لِبَنِي إِسْرَائِيلَ اسْكُنُوا الْأَرْضَ فَإِذَا جَاءَ وَعْدُ الْآخِرَةِ جِئْنَا بِكُمْ لَفِيفًا
Nu wax ginnaawam ñeel (waa Bani-Israayiil)ne leen : “Dëkkeleen suuf sa”. Ba àppu bisub àllaaxira jotee, Dananu leen indi ngeen di mbooloo.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
102Aaya

Tekki — Al-Isra 102

Simoore Al-Isra Aaya 102 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Muusaa tontu ne] : “Xam nga ne kenn wàccewul yile…

Simoore Aaya 102/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 100–104. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers