Al-Isra · 101/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ تِسْعَ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ ۖ فَاسْأَلْ بَنِي إِسْرَائِيلَ إِذْ جَاءَهُمْ فَقَالَ لَهُ فِرْعَوْنُ إِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا مُوسَىٰ مَسْحُورًا ۝١٠١
Wa laqad aatainaa Moosaa tis`a Aayaatim baiyinaatin fas`al Baneee Israaa`eela iz jaaa`ahum faqaala lahoo Fir`awnu inee la azunnuka yaa Moosaa mas hooraa
📖 Tekkim Wolof
Tigi, joxoon Nanu Muusaa juróom-ñeenti kéemaan yu leer. Laajal waa Bani-Israayiil, ba mu ñëwee fa ñoom, Firawna ne ko : “Muusaa, dama defe ne dañu laa jabar”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 99-103 — Al-Isra

99۞ أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّ اللَّهَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ قَادِرٌ عَلَىٰ أَن يَخْلُقَ مِثْلَهُمْ وَجَعَلَ لَهُمْ أَجَلًا لَّا رَيْبَ فِيهِ فَأَبَى الظَّالِمُونَ إِلَّا كُفُورًا
Ndax dañoo gisul ne Yàlla moo bind asamaan yi ak suuf si, te Ku kàttanu la ci bind leneen lu mel ni ñoom ? Te Mu àppal leen dig bu amul benn sikki-sàkka, waaye way-tooñ ña wéy nañu ci seenug weddi.
100قُل لَّوْ أَنتُمْ تَمْلِكُونَ خَزَائِنَ رَحْمَةِ رَبِّي إِذًا لَّأَمْسَكْتُمْ خَشْيَةَ الْإِنفَاقِ ۚ وَكَانَ الْإِنسَانُ قَتُورًا
Neel : “Su fekkoon ne yéen a moom ndàmbi yërmaandey Yàlla yi ; kon ngeen nay [ci joxe ko] ngir ŋott. Nit dafa di ku ŋott !
101وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ تِسْعَ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ ۖ فَاسْأَلْ بَنِي إِسْرَائِيلَ إِذْ جَاءَهُمْ فَقَالَ لَهُ فِرْعَوْنُ إِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا مُوسَىٰ مَسْحُورًا
Tigi, joxoon Nanu Muusaa juróom-ñeenti kéemaan yu leer. Laajal waa Bani-Israayiil, ba mu ñëwee fa ñoom, Firawna ne ko : “Muusaa, dama defe ne dañu laa jabar”.
102قَالَ لَقَدْ عَلِمْتَ مَا أَنزَلَ هَٰؤُلَاءِ إِلَّا رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ بَصَائِرَ وَإِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا فِرْعَوْنُ مَثْبُورًا
[Muusaa tontu ne] : “Xam nga ne kenn wàccewul yile [kéemaan] ku dul Boroom asamaan yi ak suuf si ngir ñu nekk di waare ; te damaa defe ni, yaw Firawna, dangaa nekk ku alku”.
103فَأَرَادَ أَن يَسْتَفِزَّهُم مِّنَ الْأَرْضِ فَأَغْرَقْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ جَمِيعًا
Mu bëgg leen a génne suuf sa. Nu labal ko mook ña mu àndaloon ñépp.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
101Aaya

Tekki — Al-Isra 101

Simoore Al-Isra Aaya 101 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tigi, joxoon Nanu Muusaa juróom-ñeenti kéemaan yu leer. Laajal waa…

Simoore Aaya 101/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 99–103. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers