Al-Isra · 12/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَجَعَلْنَا اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ آيَتَيْنِ ۖ فَمَحَوْنَا آيَةَ اللَّيْلِ وَجَعَلْنَا آيَةَ النَّهَارِ مُبْصِرَةً لِّتَبْتَغُوا فَضْلًا مِّن رَّبِّكُمْ وَلِتَعْلَمُوا عَدَدَ السِّنِينَ وَالْحِسَابَ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ فَصَّلْنَاهُ تَفْصِيلًا ۝١٢
Wa ja`alnal laila wannahaara Aayatayni famahawnaaa Aayatal laili wa ja`alnaaa Aayatan nahaari mubsiratal litabtaghoo fadlam mir Rabbikum wa lita`lamoo `adadas sineena walhisaab; wa kulla shai`in fassalnaahu tafseelaa
📖 Tekkim Wolof
Def Nanu guddi ak bëccëg ñu nekk ñaari kéemaan, te far Nanu lëndëmi guddi ak leeraayu bëccëg, ngir ngeen mën a gis, di sàkku xéewal gu jóge ci seen Boroom, ak ngir ngeen mën a xam limi at yi ak ngir ngeen mën a waññi. Te lu nekk faramfàcce Nanu ko ci anam yu leer.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Isra

10وَأَنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ أَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا
[Te xamal it ne] ña gëmul àllaaxira, xaroo Nanu leen mbugal mu metti.
11وَيَدْعُ الْإِنسَانُ بِالشَّرِّ دُعَاءَهُ بِالْخَيْرِ ۖ وَكَانَ الْإِنسَانُ عَجُولًا
Te nit dana ñaan lu bon ak lu baax, ndax dafa nekk di ku yàkkamti.
12وَجَعَلْنَا اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ آيَتَيْنِ ۖ فَمَحَوْنَا آيَةَ اللَّيْلِ وَجَعَلْنَا آيَةَ النَّهَارِ مُبْصِرَةً لِّتَبْتَغُوا فَضْلًا مِّن رَّبِّكُمْ وَلِتَعْلَمُوا عَدَدَ السِّنِينَ وَالْحِسَابَ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ فَصَّلْنَاهُ تَفْصِيلًا
Def Nanu guddi ak bëccëg ñu nekk ñaari kéemaan, te far Nanu lëndëmi guddi ak leeraayu bëccëg, ngir ngeen mën a gis, di sàkku xéewal gu jóge ci seen Boroom, ak ngir ngeen mën a xam limi at yi ak ngir ngeen mën a waññi. Te lu nekk faramfàcce Nanu ko ci anam yu leer.
13وَكُلَّ إِنسَانٍ أَلْزَمْنَاهُ طَائِرَهُ فِي عُنُقِهِ ۖ وَنُخْرِجُ لَهُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ كِتَابًا يَلْقَاهُ مَنشُورًا
Te nit ku nekk, tàbbal Nanu ko jëfam ci doqam. Ca Bis-pénc ba, Dananu ko génneel ab téere bu muy dajeel, ñu tàllal ko ko :
14اقْرَأْ كِتَابَكَ كَفَىٰ بِنَفْسِكَ الْيَوْمَ عَلَيْكَ حَسِيبًا
[Nu ne ko] : “Jàngal sab téere. Sa bopp doy na la tey, sa nattub jëf yaw la war”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Isra 12

Simoore Al-Isra Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def Nanu guddi ak bëccëg ñu nekk ñaari kéemaan, te…

Simoore Aaya 12/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers