Al-Isra · 11/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَيَدْعُ الْإِنسَانُ بِالشَّرِّ دُعَاءَهُ بِالْخَيْرِ ۖ وَكَانَ الْإِنسَانُ عَجُولًا ١١
Transliteration
Wa yad`ul insaanu bishsharri du`aaa `ahoo bilkhayr; wa kaanal insaanu `ajoola
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te nit dana ñaan lu bon ak lu baax, ndax dafa nekk di ku yàkkamti.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 9-13 — Al-Isra
9إِنَّ هَٰذَا الْقُرْآنَ يَهْدِي لِلَّتِي هِيَ أَقْوَمُ وَيُبَشِّرُ الْمُؤْمِنِينَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ الصَّالِحَاتِ أَنَّ لَهُمْ أَجْرًا كَبِيرًا
Alxuraan jii nag dafay gindee jëm ci la gën a jub, tey bégal way-gëm ñay jëf jëf yu sell, [xamal leen ne] ñeel na leen pey gu rëy,
10وَأَنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ أَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا
[Te xamal it ne] ña gëmul àllaaxira, xaroo Nanu leen mbugal mu metti.
11وَيَدْعُ الْإِنسَانُ بِالشَّرِّ دُعَاءَهُ بِالْخَيْرِ ۖ وَكَانَ الْإِنسَانُ عَجُولًا
Te nit dana ñaan lu bon ak lu baax, ndax dafa nekk di ku yàkkamti.
12وَجَعَلْنَا اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ آيَتَيْنِ ۖ فَمَحَوْنَا آيَةَ اللَّيْلِ وَجَعَلْنَا آيَةَ النَّهَارِ مُبْصِرَةً لِّتَبْتَغُوا فَضْلًا مِّن رَّبِّكُمْ وَلِتَعْلَمُوا عَدَدَ السِّنِينَ وَالْحِسَابَ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ فَصَّلْنَاهُ تَفْصِيلًا
Def Nanu guddi ak bëccëg ñu nekk ñaari kéemaan, te far Nanu lëndëmi guddi ak leeraayu bëccëg, ngir ngeen mën a gis, di sàkku xéewal gu jóge ci seen Boroom, ak ngir ngeen mën a xam limi at yi ak ngir ngeen mën a waññi. Te lu nekk faramfàcce Nanu ko ci anam yu leer.
13وَكُلَّ إِنسَانٍ أَلْزَمْنَاهُ طَائِرَهُ فِي عُنُقِهِ ۖ وَنُخْرِجُ لَهُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ كِتَابًا يَلْقَاهُ مَنشُورًا
Te nit ku nekk, tàbbal Nanu ko jëfam ci doqam. Ca Bis-pénc ba, Dananu ko génneel ab téere bu muy dajeel, ñu tàllal ko ko :
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
11Aaya
Tekki — Al-Isra 11
Simoore Al-Isra Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nit dana ñaan lu bon ak lu baax, ndax…Simoore Aaya 11/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








