Al-Kahf · 80/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
وَأَمَّا الْغُلَامُ فَكَانَ أَبَوَاهُ مُؤْمِنَيْنِ فَخَشِينَا أَن يُرْهِقَهُمَا طُغْيَانًا وَكُفْرًا ۝٨٠
Wa aammal ghulaamu fakaana abawaahu mu`minaini fakhasheenaaa any yurhiqa humaa tughyaananw wa kufraa
📖 Tekkim Wolof
Xale [ba ma reyoon], ay waajuram dañoo doonoon ñu gëm Yàlla ; te su màggoon, dana leen weddiloo, beewloo leen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 78-82 — Al-Kahf

78قَالَ هَٰذَا فِرَاقُ بَيْنِي وَبَيْنِكَ ۚ سَأُنَبِّئُكَ بِتَأْوِيلِ مَا لَمْ تَسْتَطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا
Mu ne ko : “Maak yaw fii la nuy tàqalikoo.Waaye danaa la leeralal mbirum li nga mënul woon a muñ.
79أَمَّا السَّفِينَةُ فَكَانَتْ لِمَسَاكِينَ يَعْمَلُونَ فِي الْبَحْرِ فَأَرَدتُّ أَنْ أَعِيبَهَا وَكَانَ وَرَاءَهُم مَّلِكٌ يَأْخُذُ كُلَّ سَفِينَةٍ غَصْبًا
[Gaal ga ma bënoon], ay ndóol ñoo ko móomoon, daan ca daan seen doole ngir dundu. La tax ma bënn ko moo di dafa buur bu daan siif gépp gaal gu mu romb, ma bënn ko ngir mu bañ koo yóbb.
80وَأَمَّا الْغُلَامُ فَكَانَ أَبَوَاهُ مُؤْمِنَيْنِ فَخَشِينَا أَن يُرْهِقَهُمَا طُغْيَانًا وَكُفْرًا
Xale [ba ma reyoon], ay waajuram dañoo doonoon ñu gëm Yàlla ; te su màggoon, dana leen weddiloo, beewloo leen.
81فَأَرَدْنَا أَن يُبْدِلَهُمَا رَبُّهُمَا خَيْرًا مِّنْهُ زَكَاةً وَأَقْرَبَ رُحْمًا
Nu bëgg Yàlla soppil leen ko ku gën a sell, gën a topp i [waajuram].
82وَأَمَّا الْجِدَارُ فَكَانَ لِغُلَامَيْنِ يَتِيمَيْنِ فِي الْمَدِينَةِ وَكَانَ تَحْتَهُ كَنزٌ لَّهُمَا وَكَانَ أَبُوهُمَا صَالِحًا فَأَرَادَ رَبُّكَ أَن يَبْلُغَا أَشُدَّهُمَا وَيَسْتَخْرِجَا كَنزَهُمَا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ وَمَا فَعَلْتُهُ عَنْ أَمْرِي ۚ ذَٰلِكَ تَأْوِيلُ مَا لَمْ تَسْطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا
Tabax [ba ma doon yékkatiwaat], ñaari xale yu jirim ñoom la ko fa seen baay bàyyil; seen baay doonoon ku yiw, ku baax, am alal ju mu leen ca dencal. Sa Boroom bëgg su ñu màggee mën a gindiku jël seen alal joojee ci yërmaandey Yàlla. Defuma ko woon rekk ci sama coobarey bopp. Loolu kon mooy mbirum la nga mënul woon a muñ”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
80Aaya

Tekki — Al-Kahf 80

Simoore Al-Kahf Aaya 80 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xale [ba ma reyoon], ay waajuram dañoo doonoon ñu gëm…

Simoore Aaya 80/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 78–82. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers