Al-Kahf · 81/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
فَأَرَدْنَا أَن يُبْدِلَهُمَا رَبُّهُمَا خَيْرًا مِّنْهُ زَكَاةً وَأَقْرَبَ رُحْمًا ٨١
Transliteration
Faradnaa any yubdila humaa Rabbuhumaa khairam minhu zakaatanw wa aqraba ruhmaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu bëgg Yàlla soppil leen ko ku gën a sell, gën a topp i [waajuram].
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 79-83 — Al-Kahf
79أَمَّا السَّفِينَةُ فَكَانَتْ لِمَسَاكِينَ يَعْمَلُونَ فِي الْبَحْرِ فَأَرَدتُّ أَنْ أَعِيبَهَا وَكَانَ وَرَاءَهُم مَّلِكٌ يَأْخُذُ كُلَّ سَفِينَةٍ غَصْبًا
[Gaal ga ma bënoon], ay ndóol ñoo ko móomoon, daan ca daan seen doole ngir dundu. La tax ma bënn ko moo di dafa buur bu daan siif gépp gaal gu mu romb, ma bënn ko ngir mu bañ koo yóbb.
80وَأَمَّا الْغُلَامُ فَكَانَ أَبَوَاهُ مُؤْمِنَيْنِ فَخَشِينَا أَن يُرْهِقَهُمَا طُغْيَانًا وَكُفْرًا
Xale [ba ma reyoon], ay waajuram dañoo doonoon ñu gëm Yàlla ; te su màggoon, dana leen weddiloo, beewloo leen.
81فَأَرَدْنَا أَن يُبْدِلَهُمَا رَبُّهُمَا خَيْرًا مِّنْهُ زَكَاةً وَأَقْرَبَ رُحْمًا
Nu bëgg Yàlla soppil leen ko ku gën a sell, gën a topp i [waajuram].
82وَأَمَّا الْجِدَارُ فَكَانَ لِغُلَامَيْنِ يَتِيمَيْنِ فِي الْمَدِينَةِ وَكَانَ تَحْتَهُ كَنزٌ لَّهُمَا وَكَانَ أَبُوهُمَا صَالِحًا فَأَرَادَ رَبُّكَ أَن يَبْلُغَا أَشُدَّهُمَا وَيَسْتَخْرِجَا كَنزَهُمَا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ وَمَا فَعَلْتُهُ عَنْ أَمْرِي ۚ ذَٰلِكَ تَأْوِيلُ مَا لَمْ تَسْطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا
Tabax [ba ma doon yékkatiwaat], ñaari xale yu jirim ñoom la ko fa seen baay bàyyil; seen baay doonoon ku yiw, ku baax, am alal ju mu leen ca dencal. Sa Boroom bëgg su ñu màggee mën a gindiku jël seen alal joojee ci yërmaandey Yàlla. Defuma ko woon rekk ci sama coobarey bopp. Loolu kon mooy mbirum la nga mënul woon a muñ”.
83وَيَسْأَلُونَكَ عَن ذِي الْقَرْنَيْنِ ۖ قُلْ سَأَتْلُو عَلَيْكُم مِّنْهُ ذِكْرًا
Danañu lay laaj ci mbirum [Zul-Qarnayni]. Neel : “Danaa leen jàngal na mu doxe woon”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
81Aaya
Tekki — Al-Kahf 81
Simoore Al-Kahf Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu bëgg Yàlla soppil leen ko ku gën a sell,…Simoore Aaya 81/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








