Maryam · 73/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَإِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُنَا بَيِّنَاتٍ قَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا أَيُّ الْفَرِيقَيْنِ خَيْرٌ مَّقَامًا وَأَحْسَنُ نَدِيًّا ۝٧٣
Wa izaa tutlaa `alaihim Aayaatunaa baiyinaatin qaalal lazeena kafaroo lillazeena aamanooo aiyul fareeqaini khairum maqaamanw wa ahsanu nadiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Saa su ñu jàngee Sunuy laaya ca ñoom, muy lu leer nàññ, yéefar ya dañuy daldi wax ne gëmunu leen : “Ana sunu ñaari kurél yi ban moo ci ëpp daraja ? ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 71-75 — Maryam

71وَإِن مِّنكُمْ إِلَّا وَارِدُهَا ۚ كَانَ عَلَىٰ رَبِّكَ حَتْمًا مَّقْضِيًّا
Ñépp a fay jaar, Yàlla dogal na ko ba noppi.
72ثُمَّ نُنَجِّي الَّذِينَ اتَّقَوا وَّنَذَرُ الظَّالِمِينَ فِيهَا جِثِيًّا
Bu ko defee Nu musal ñi ragal Yàlla, daldi fay bàyyi tooñkat ya ñu sukk.
73وَإِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُنَا بَيِّنَاتٍ قَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا أَيُّ الْفَرِيقَيْنِ خَيْرٌ مَّقَامًا وَأَحْسَنُ نَدِيًّا
Saa su ñu jàngee Sunuy laaya ca ñoom, muy lu leer nàññ, yéefar ya dañuy daldi wax ne gëmunu leen : “Ana sunu ñaari kurél yi ban moo ci ëpp daraja ? ”
74وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هُمْ أَحْسَنُ أَثَاثًا وَرِئْيًا
Aka bari ña Nu alagoon ca ña leen jiitu, ñoo xam ne ñoo leen ëppoon alal, gën leen a jekk ?
75قُلْ مَن كَانَ فِي الضَّلَالَةِ فَلْيَمْدُدْ لَهُ الرَّحْمَٰنُ مَدًّا ۚ حَتَّىٰ إِذَا رَأَوْا مَا يُوعَدُونَ إِمَّا الْعَذَابَ وَإِمَّا السَّاعَةَ فَسَيَعْلَمُونَ مَنْ هُوَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضْعَفُ جُندًا
Neel : “Ku nekk cig réer, Yàlla da koy yoor ba mu ne ticcët ca la Nu ko doon dig, benn muy mbugal walla muy Bis-pénc ba. Bu boobaa danañu xam ñoo, ana kan moo yées wàccuwaay te gën a néew doole [ci way gëm ña ak yéefar ya]”.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Maryam 73

Simoore Maryam Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su ñu jàngee Sunuy laaya ca ñoom, muy lu…

Simoore Aaya 73/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers