Maryam · 98/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هَلْ تُحِسُّ مِنْهُم مِّنْ أَحَدٍ أَوْ تَسْمَعُ لَهُمْ رِكْزًا ۝٩٨
Wa kam ahlaknaa qabla hum min qarnin hal tuhissu minhum min ahadin aw tasma`u lahum rikzaa
📖 Tekkim Wolof
Aka bari li Nu alag ca xeet ya leen jiitu woon ! Moo ndax gisati nga lu ca bokk ? Mbaa nga déggati seenum riir ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 96-98 — Simoore Maryam

96إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ سَيَجْعَلُ لَهُمُ الرَّحْمَٰنُ وُدًّا
Ña gëm tey jëf u yiw, Yàlla dana leen sagoo.
97فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لِتُبَشِّرَ بِهِ الْمُتَّقِينَ وَتُنذِرَ بِهِ قَوْمًا لُّدًّا
Yombalal Nanu la Téere bii, jaarale ko ci saw làmmiñ ngir nga bégal ci ñi ragal Yàlla te xupp ca ña dëgër bopp [weddi].
98وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هَلْ تُحِسُّ مِنْهُم مِّنْ أَحَدٍ أَوْ تَسْمَعُ لَهُمْ رِكْزًا
Aka bari li Nu alag ca xeet ya leen jiitu woon ! Moo ndax gisati nga lu ca bokk ? Mbaa nga déggati seenum riir ?
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
98Aaya

Tekki — Maryam 98

Simoore Maryam Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aka bari li Nu alag ca xeet ya leen jiitu…

Simoore Aaya 98/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 96–98. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers