Al-Baqara · 210/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
هَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا أَن يَأْتِيَهُمُ اللَّهُ فِي ظُلَلٍ مِّنَ الْغَمَامِ وَالْمَلَائِكَةُ وَقُضِيَ الْأَمْرُ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ ۝٢١٠
Hal yanzuroona illaaa ai yaatiyahumul laahu fee zulalim minal ghamaami walmalaaa`ikatu wa qudiyal amr; wa ilal laahi turja`ulumoor
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañuy xaar ba Yàlla dikkal leen [ak mbugal] ci keri niir yi ak Malaaka yi, fekk àtteef na mbir ya ba noppi ? Te mbir yépp ca Yàlla lañuy dellu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 208-212 — Al-Baqara

208يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا ادْخُلُوا فِي السِّلْمِ كَافَّةً وَلَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Éy yéen ñi gëm ! Dugguleen yéen ñépp ci jàmm ji [Islaam], te buleen topp yoonu [Séytaane], moom seenub noon la bu bir.
209فَإِن زَلَلْتُم مِّن بَعْدِ مَا جَاءَتْكُمُ الْبَيِّنَاتُ فَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Bu ngeen tarxiisee, ginnaaw ba ngeen amee faramfàcce gu leer nàññ, xamleen ne Yàlla ku màgg kàttan la te ku xereñ la.
210هَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا أَن يَأْتِيَهُمُ اللَّهُ فِي ظُلَلٍ مِّنَ الْغَمَامِ وَالْمَلَائِكَةُ وَقُضِيَ الْأَمْرُ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Moo ndax dañuy xaar ba Yàlla dikkal leen [ak mbugal] ci keri niir yi ak Malaaka yi, fekk àtteef na mbir ya ba noppi ? Te mbir yépp ca Yàlla lañuy dellu.
211سَلْ بَنِي إِسْرَائِيلَ كَمْ آتَيْنَاهُم مِّنْ آيَةٍ بَيِّنَةٍ ۗ وَمَن يُبَدِّلْ نِعْمَةَ اللَّهِ مِن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُ فَإِنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Laajal Banii-Israayiila ñaata yoon lañu leen indil ay kéemaan yu leer nàññ [bari na] ! Képp ku soppi xéewali Yàlla ginnaaw ba mu ko jotee... na xam ne, Yàlla ku tar mbugal la.
212زُيِّنَ لِلَّذِينَ كَفَرُوا الْحَيَاةُ الدُّنْيَا وَيَسْخَرُونَ مِنَ الَّذِينَ آمَنُوا ۘ وَالَّذِينَ اتَّقَوْا فَوْقَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ وَاللَّهُ يَرْزُقُ مَن يَشَاءُ بِغَيْرِ حِسَابٍ
Ña nga xam ne dañoo weddi, doyloo nañu dundug àddina ak ub taaram, ba tax ñuy yejji ña gëm. Waaye ña ragal Yàlla ñoo leen di gënu demiin bu Bis-pénc baa. Ndax Yàlla dana wërsëgal ku ko soob ci lu àndul ak natt.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
210Aaya

Tekki — Al-Baqara 210

Simoore Al-Baqara Aaya 210 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañuy xaar ba Yàlla dikkal leen [ak mbugal]…

Simoore Aaya 210/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 208–212. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers