Al-Baqara · 265/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَمَثَلُ الَّذِينَ يُنفِقُونَ أَمْوَالَهُمُ ابْتِغَاءَ مَرْضَاتِ اللَّهِ وَتَثْبِيتًا مِّنْ أَنفُسِهِمْ كَمَثَلِ جَنَّةٍ بِرَبْوَةٍ أَصَابَهَا وَابِلٌ فَآتَتْ أُكُلَهَا ضِعْفَيْنِ فَإِن لَّمْ يُصِبْهَا وَابِلٌ فَطَلٌّ ۗ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ ٢٦٥
Transliteration
Wa masalul lazeena yunfiqoona amwaalahumub ti ghaaaa`a mardaatil laahi wa tasbeetam min anfusihim kamasali jannatim birabwatin asaabahaa waabilun fa aatat ukulahaa di`faini fa il lam yusibhaa waabilun fatall; wallaahu bimaa ta`maloona Baseer
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Melow ñi joxe seeni alal ngir sàkku ngërëmul Yàlla, ak saxal seeni bakkan ci jaamu Yàlla, dafa mel ni tool bu nekk ci aw tund. Waame [taw] dal ca, mu génne ñaari yoon meññeefam ; bu ca waame dalul itam, mësay ma naatal ko. Yàllaa ngi ne jàkk ci li ngeen di def.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 263-267 — Al-Baqara
263۞ قَوْلٌ مَّعْرُوفٌ وَمَغْفِرَةٌ خَيْرٌ مِّن صَدَقَةٍ يَتْبَعُهَا أَذًى ۗ وَاللَّهُ غَنِيٌّ حَلِيمٌ
Wax ju yiw ak ag njeggal moo gëm sarax boo xam ne wax ju ñaaw a ca topp. Yàlla ku woomal la, ku lewet la.
264يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُبْطِلُوا صَدَقَاتِكُم بِالْمَنِّ وَالْأَذَىٰ كَالَّذِي يُنفِقُ مَالَهُ رِئَاءَ النَّاسِ وَلَا يُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ ۖ فَمَثَلُهُ كَمَثَلِ صَفْوَانٍ عَلَيْهِ تُرَابٌ فَأَصَابَهُ وَابِلٌ فَتَرَكَهُ صَلْدًا ۖ لَّا يَقْدِرُونَ عَلَىٰ شَيْءٍ مِّمَّا كَسَبُوا ۗ وَاللَّهُ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الْكَافِرِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen yàq seeni sarax ci ñax ak kañu, képp ku joxe alal ngir ngistal ci nit ña te gëmul Bis-pénc ba. Dafay mel ni doj wu suuf tegu ca kawam ; waame sottiku ca, bàyyi ko mu ratax bandaŋ. [nit ñu mel noonu] duñu mën a def dara lu barkeel. Te Yàlla du gindi nit ñu weddi.
265وَمَثَلُ الَّذِينَ يُنفِقُونَ أَمْوَالَهُمُ ابْتِغَاءَ مَرْضَاتِ اللَّهِ وَتَثْبِيتًا مِّنْ أَنفُسِهِمْ كَمَثَلِ جَنَّةٍ بِرَبْوَةٍ أَصَابَهَا وَابِلٌ فَآتَتْ أُكُلَهَا ضِعْفَيْنِ فَإِن لَّمْ يُصِبْهَا وَابِلٌ فَطَلٌّ ۗ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ
Melow ñi joxe seeni alal ngir sàkku ngërëmul Yàlla, ak saxal seeni bakkan ci jaamu Yàlla, dafa mel ni tool bu nekk ci aw tund. Waame [taw] dal ca, mu génne ñaari yoon meññeefam ; bu ca waame dalul itam, mësay ma naatal ko. Yàllaa ngi ne jàkk ci li ngeen di def.
266أَيَوَدُّ أَحَدُكُمْ أَن تَكُونَ لَهُ جَنَّةٌ مِّن نَّخِيلٍ وَأَعْنَابٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ لَهُ فِيهَا مِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ وَأَصَابَهُ الْكِبَرُ وَلَهُ ذُرِّيَّةٌ ضُعَفَاءُ فَأَصَابَهَا إِعْصَارٌ فِيهِ نَارٌ فَاحْتَرَقَتْ ۗ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمُ الْآيَاتِ لَعَلَّكُمْ تَتَفَكَّرُونَ
Kenn ci yéen bu amoon toolu garabu tàndarma ak reseñ, ndox ya di daw ca biir, mu bari lool meññent, fekk mu nekk mag, ame njaboot gu sew, ndax dana bëgg callmeer lu ànd ak safara dal ca tool ba lakk ko ? Noonu la Yàlla di faramfàccee ay laayaam ndaxtelee ngeen di xalaat !
267يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَنفِقُوا مِن طَيِّبَاتِ مَا كَسَبْتُمْ وَمِمَّا أَخْرَجْنَا لَكُم مِّنَ الْأَرْضِ ۖ وَلَا تَيَمَّمُوا الْخَبِيثَ مِنْهُ تُنفِقُونَ وَلَسْتُم بِآخِذِيهِ إِلَّا أَن تُغْمِضُوا فِيهِ ۚ وَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ غَنِيٌّ حَمِيدٌ
Yéen ñi gëm ! Deeleen joxe asaka ci lu téey li ngeen di fàggul seen bopp ak li Nu leen génneele ci suuf si. Buleen ca beddi la ca yées di ko joxe. Te fekk muy loo xam ne ku leen ko joxoon dungeen ko bëgg a jël, te gëmmuleen ca ! Nangeen xam ne Yàlla ku woomal la te ku yayoo cant la.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
265Aaya
Tekki — Al-Baqara 265
Simoore Al-Baqara Aaya 265 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Melow ñi joxe seeni alal ngir sàkku ngërëmul Yàlla, ak…Simoore Aaya 265/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 263–267. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








