Al-Anbiya · 68/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
قَالُوا حَرِّقُوهُ وَانصُرُوا آلِهَتَكُمْ إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ ۝٦٨
Qaaloo harriqooho wansurooo aalihatakum in kuntum faa`ileen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Lakk-leen ko ngir ngeen dimbali seen xërëm yi ndegam nar ngeen ko”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 66-70 — Al-Anbiya

66قَالَ أَفَتَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَنفَعُكُمْ شَيْئًا وَلَا يَضُرُّكُمْ
Mu ne : “Waaw, ndax dangeen di bàyyi Yàlla di jaamu loo xam ne mënuleen a jariñ dara te mënuleen a lor.
67أُفٍّ لَّكُمْ وَلِمَا تَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Kuf ma leen yéen ak li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla ! Ndax dangeen dul xel-lu ? ”
68قَالُوا حَرِّقُوهُ وَانصُرُوا آلِهَتَكُمْ إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Ñu ne : “Lakk-leen ko ngir ngeen dimbali seen xërëm yi ndegam nar ngeen ko”.
69قُلْنَا يَا نَارُ كُونِي بَرْدًا وَسَلَامًا عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ
Nu wax ne [Nun Yàlla] : "Yaw safara, nekkal lu sedd te am jàmm ci kaw Ibraahiima”.
70وَأَرَادُوا بِهِ كَيْدًا فَجَعَلْنَاهُمُ الْأَخْسَرِينَ
Ñu bëgg a def seeni pexe ci moom, Nu def leen ñu di ñu yàqule ña.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
68Aaya

Tekki — Al-Anbiya 68

Simoore Al-Anbiya Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Lakk-leen ko ngir ngeen dimbali seen xërëm…

Simoore Aaya 68/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers