Al-Anbiya · 69/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
قُلْنَا يَا نَارُ كُونِي بَرْدًا وَسَلَامًا عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ ۝٦٩
Qulnaa yaa naaru koonee bardanw wa salaaman `alaaa Ibraaheem
📖 Tekkim Wolof
Nu wax ne [Nun Yàlla] : "Yaw safara, nekkal lu sedd te am jàmm ci kaw Ibraahiima”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Al-Anbiya

67أُفٍّ لَّكُمْ وَلِمَا تَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Kuf ma leen yéen ak li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla ! Ndax dangeen dul xel-lu ? ”
68قَالُوا حَرِّقُوهُ وَانصُرُوا آلِهَتَكُمْ إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Ñu ne : “Lakk-leen ko ngir ngeen dimbali seen xërëm yi ndegam nar ngeen ko”.
69قُلْنَا يَا نَارُ كُونِي بَرْدًا وَسَلَامًا عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ
Nu wax ne [Nun Yàlla] : "Yaw safara, nekkal lu sedd te am jàmm ci kaw Ibraahiima”.
70وَأَرَادُوا بِهِ كَيْدًا فَجَعَلْنَاهُمُ الْأَخْسَرِينَ
Ñu bëgg a def seeni pexe ci moom, Nu def leen ñu di ñu yàqule ña.
71وَنَجَّيْنَاهُ وَلُوطًا إِلَى الْأَرْضِ الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا لِلْعَالَمِينَ
Nu daldi koy musal moom ak Lóot jëme leen fa suuf sa Nu barkeel ngir waa àddina si yépp.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Al-Anbiya 69

Simoore Al-Anbiya Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu wax ne [Nun Yàlla] : "Yaw safara, nekkal lu…

Simoore Aaya 69/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers