Al-Hajj · 14/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يُرِيدُ ١٤
Transliteration
Innal laaha yudkhilul laeena aamanoo wa `amilus saalihaati jannaatin tajree min tahtihal anhaar; innal laaha yaf`alu maa yureed
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Naka Yàlla, Dana dugal ñi gëm tey jëf u yiw ci Àjjana yoo xam ne dex dañuy daw ci seen suuf [ron], Yàllaay def lu ko soob.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 12-16 — Al-Hajj
12يَدْعُو مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَضُرُّهُ وَمَا لَا يَنفَعُهُ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الضَّلَالُ الْبَعِيدُ
Mangay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne mënu koo lor, mënu koo jariñ. Loolu moo di réer gu sori dëgg !
13يَدْعُو لَمَن ضَرُّهُ أَقْرَبُ مِن نَّفْعِهِ ۚ لَبِئْسَ الْمَوْلَىٰ وَلَبِئْسَ الْعَشِيرُ
Mangay jaamu loo xam ne loram moo gën jegeñnjariñam. Aka bon wéeruwaay te aka bon àndandoo !
14إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يُرِيدُ
Naka Yàlla, Dana dugal ñi gëm tey jëf u yiw ci Àjjana yoo xam ne dex dañuy daw ci seen suuf [ron], Yàllaay def lu ko soob.
15مَن كَانَ يَظُنُّ أَن لَّن يَنصُرَهُ اللَّهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ فَلْيَمْدُدْ بِسَبَبٍ إِلَى السَّمَاءِ ثُمَّ لْيَقْطَعْ فَلْيَنظُرْ هَلْ يُذْهِبَنَّ كَيْدُهُ مَا يَغِيظُ
Ku jort ne Yàlla du dimbali [Muhammad] ci àddina ak àllaaxira, na tàllal buum jëme ko asamaan, topp mu dog ko, te na xool nag ndax pexeem dana fa jële la ko tax a mer.
16وَكَذَٰلِكَ أَنزَلْنَاهُ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ وَأَنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يُرِيدُ
Noonu la Nu ko wàccelee ay kàddu yu leer te Yàlla dana gindi ku ko soob.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
14Aaya
Tekki — Al-Hajj 14
Simoore Al-Hajj Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka Yàlla, Dana dugal ñi gëm tey jëf u yiw…Simoore Aaya 14/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








