Al-Hajj · 15/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
مَن كَانَ يَظُنُّ أَن لَّن يَنصُرَهُ اللَّهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ فَلْيَمْدُدْ بِسَبَبٍ إِلَى السَّمَاءِ ثُمَّ لْيَقْطَعْ فَلْيَنظُرْ هَلْ يُذْهِبَنَّ كَيْدُهُ مَا يَغِيظُ ۝١٥
Man kaana yazunnu allai yansurahul laahu fid dunyaa wal aakhirati fal yamdud bisababin ilas samaaa`i summal yaqta` falyanzur hal yuzhibanna kaiduhoo maa yagheez
📖 Tekkim Wolof
Ku jort ne Yàlla du dimbali [Muhammad] ci àddina ak àllaaxira, na tàllal buum jëme ko asamaan, topp mu dog ko, te na xool nag ndax pexeem dana fa jële la ko tax a mer.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Al-Hajj

13يَدْعُو لَمَن ضَرُّهُ أَقْرَبُ مِن نَّفْعِهِ ۚ لَبِئْسَ الْمَوْلَىٰ وَلَبِئْسَ الْعَشِيرُ
Mangay jaamu loo xam ne loram moo gën jegeñnjariñam. Aka bon wéeruwaay te aka bon àndandoo !
14إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يُرِيدُ
Naka Yàlla, Dana dugal ñi gëm tey jëf u yiw ci Àjjana yoo xam ne dex dañuy daw ci seen suuf [ron], Yàllaay def lu ko soob.
15مَن كَانَ يَظُنُّ أَن لَّن يَنصُرَهُ اللَّهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ فَلْيَمْدُدْ بِسَبَبٍ إِلَى السَّمَاءِ ثُمَّ لْيَقْطَعْ فَلْيَنظُرْ هَلْ يُذْهِبَنَّ كَيْدُهُ مَا يَغِيظُ
Ku jort ne Yàlla du dimbali [Muhammad] ci àddina ak àllaaxira, na tàllal buum jëme ko asamaan, topp mu dog ko, te na xool nag ndax pexeem dana fa jële la ko tax a mer.
16وَكَذَٰلِكَ أَنزَلْنَاهُ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ وَأَنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يُرِيدُ
Noonu la Nu ko wàccelee ay kàddu yu leer te Yàlla dana gindi ku ko soob.
17إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَالَّذِينَ هَادُوا وَالصَّابِئِينَ وَالنَّصَارَىٰ وَالْمَجُوسَ وَالَّذِينَ أَشْرَكُوا إِنَّ اللَّهَ يَفْصِلُ بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ شَهِيدٌ
Ña gëm ak ña nekk Yahuud ak ña di Saabiina, ak ña nekk Nasaaraan ak ña nekk Majuus ak way-bokkaale ña, naka Yàlla dana àtte seen diggante, bu Bis-pénc baa Yàlla seede la ci lu nekk.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Hajj 15

Simoore Al-Hajj Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku jort ne Yàlla du dimbali [Muhammad] ci àddina ak…

Simoore Aaya 15/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers