Al-Hajj · 16/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَكَذَٰلِكَ أَنزَلْنَاهُ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ وَأَنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يُرِيدُ ۝١٦
Wa kazaalika anzalnaahu aayaatim baiyinaatinw wa annal laaha yahdee mai yureed
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Nu ko wàccelee ay kàddu yu leer te Yàlla dana gindi ku ko soob.

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Al-Hajj

14إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يُرِيدُ
Naka Yàlla, Dana dugal ñi gëm tey jëf u yiw ci Àjjana yoo xam ne dex dañuy daw ci seen suuf [ron], Yàllaay def lu ko soob.
15مَن كَانَ يَظُنُّ أَن لَّن يَنصُرَهُ اللَّهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ فَلْيَمْدُدْ بِسَبَبٍ إِلَى السَّمَاءِ ثُمَّ لْيَقْطَعْ فَلْيَنظُرْ هَلْ يُذْهِبَنَّ كَيْدُهُ مَا يَغِيظُ
Ku jort ne Yàlla du dimbali [Muhammad] ci àddina ak àllaaxira, na tàllal buum jëme ko asamaan, topp mu dog ko, te na xool nag ndax pexeem dana fa jële la ko tax a mer.
16وَكَذَٰلِكَ أَنزَلْنَاهُ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ وَأَنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يُرِيدُ
Noonu la Nu ko wàccelee ay kàddu yu leer te Yàlla dana gindi ku ko soob.
17إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَالَّذِينَ هَادُوا وَالصَّابِئِينَ وَالنَّصَارَىٰ وَالْمَجُوسَ وَالَّذِينَ أَشْرَكُوا إِنَّ اللَّهَ يَفْصِلُ بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ شَهِيدٌ
Ña gëm ak ña nekk Yahuud ak ña di Saabiina, ak ña nekk Nasaaraan ak ña nekk Majuus ak way-bokkaale ña, naka Yàlla dana àtte seen diggante, bu Bis-pénc baa Yàlla seede la ci lu nekk.
18أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ يَسْجُدُ لَهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ وَالشَّمْسُ وَالْقَمَرُ وَالنُّجُومُ وَالْجِبَالُ وَالشَّجَرُ وَالدَّوَابُّ وَكَثِيرٌ مِّنَ النَّاسِ ۖ وَكَثِيرٌ حَقَّ عَلَيْهِ الْعَذَابُ ۗ وَمَن يُهِنِ اللَّهُ فَمَا لَهُ مِن مُّكْرِمٍ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يَشَاءُ ۩
Ndax gisoo ne lépp lu nekk ci suuf si ak asamaan yi mangay sujjóotal Yàlla, ak jant bi ak weer wi ak biddiw yi, ak garab yi ak tundi doj yi, ak way-sujjóot yi ak lu bari ci nit ñi ? Waaye lu bari (ci nit ñi) ñu yeyoo mbugal lañu. Te képp ku Yàlla texeedil kenn du ko mën a teral.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Hajj 16

Simoore Al-Hajj Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Nu ko wàccelee ay kàddu yu leer te…

Simoore Aaya 16/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers