An-Nur · 20/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ وَأَنَّ اللَّهَ رَءُوفٌ رَّحِيمٌ ۝٢٠
Wa law laa fadlul laahi `alaikum wa rahmatuhoo wa annal laaha Ra`oofur Raheem
📖 Tekkim Wolof
Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ak yëmaandeem ci yéen, waaye Yàlla Moom ku ñeewant la, di Jaglewaakoon ...

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — An-Nur

18وَيُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمُ الْآيَاتِ ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Yàllaa ngi leen di faramfàcceel i laayam de, te Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
19إِنَّ الَّذِينَ يُحِبُّونَ أَن تَشِيعَ الْفَاحِشَةُ فِي الَّذِينَ آمَنُوا لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ وَأَنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Ñi bëgg a tasaarey ñaawtéef ci biir jullit ñi, mbugal mu metti dana leen dal ci àddina ak àllaaxira. Yàlla xam na te yéen xamuleen.
20وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ وَأَنَّ اللَّهَ رَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ak yëmaandeem ci yéen, waaye Yàlla Moom ku ñeewant la, di Jaglewaakoon ...
21۞ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ وَمَن يَتَّبِعْ خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ فَإِنَّهُ يَأْمُرُ بِالْفَحْشَاءِ وَالْمُنكَرِ ۚ وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ مَا زَكَىٰ مِنكُم مِّنْ أَحَدٍ أَبَدًا وَلَٰكِنَّ اللَّهَ يُزَكِّي مَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen topp jeegoy Séytaane. Ku topp jéegoy Séytaane, [na xam ne] Séytaane ñaawtéef ak njekkar la am. Dogankoon ak ngënéelul Yàlla ak yërmaandeem, kenn ci yéen du sellal. Waaye nag Moom Yàlla mooy sellal ku Ko soob. Te Yàlla Kuy dégg la, Ku xam la.
22وَلَا يَأْتَلِ أُولُو الْفَضْلِ مِنكُمْ وَالسَّعَةِ أَن يُؤْتُوا أُولِي الْقُرْبَىٰ وَالْمَسَاكِينَ وَالْمُهَاجِرِينَ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ۖ وَلْيَعْفُوا وَلْيَصْفَحُوا ۗ أَلَا تُحِبُّونَ أَن يَغْفِرَ اللَّهُ لَكُمْ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Te ña Yàlla jox wërsëg te ñu bokk ci yéen, buñu cay ñàkk a jox jegeñaale ya ak ndóol ya ak ñay gàddaay ci yoonu Yàlla. Nañuy jéggale tey jéllale. Moo xanaa bëgguleen Yàlla jéggal leen ? Yàlla dey Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la !
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
20Aaya

Tekki — An-Nur 20

Simoore An-Nur Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ak yëmaandeem ci yéen, waaye…

Simoore Aaya 20/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers