An-Nur · 9/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَالْخَامِسَةَ أَنَّ غَضَبَ اللَّهِ عَلَيْهَا إِن كَانَ مِنَ الصَّادِقِينَ ۝٩
Wal khaamisata anna ghadabal laahi `alaihaaa in kaana minas saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
ndaw sa itam na waat ne merum Yàlla na wàcc ci kawam su jëkkëram ja waxee dëgg [pasem rëbboo dootu ko fàttaliku mukk] muy juróomeelu waatam.
🎧 Dégg

📜 Aaya 7-11 — An-Nur

7وَالْخَامِسَةُ أَنَّ لَعْنَتَ اللَّهِ عَلَيْهِ إِن كَانَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
juróomeel ba mu waat ne “rëbbum Yàlla [sori yërmaandeem] na dal ci kawam su dee fenkat la”.
8وَيَدْرَأُ عَنْهَا الْعَذَابَ أَن تَشْهَدَ أَرْبَعَ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ
Su jabar ja waate ñeenti yoon ci Yàlla ne waa ja fenkat la, kenn du ko sànni xeer [rajmu],
9وَالْخَامِسَةَ أَنَّ غَضَبَ اللَّهِ عَلَيْهَا إِن كَانَ مِنَ الصَّادِقِينَ
ndaw sa itam na waat ne merum Yàlla na wàcc ci kawam su jëkkëram ja waxee dëgg [pasem rëbboo dootu ko fàttaliku mukk] muy juróomeelu waatam.
10وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ وَأَنَّ اللَّهَ تَوَّابٌ حَكِيمٌ
Cëy dugankoon ak ngënéelul Yàlla ci yéen ak yërmaandeem, waaye nag Yàlla Nanguwaakoonu tuub la bu xeréñ !
11إِنَّ الَّذِينَ جَاءُوا بِالْإِفْكِ عُصْبَةٌ مِّنكُمْ ۚ لَا تَحْسَبُوهُ شَرًّا لَّكُم ۖ بَلْ هُوَ خَيْرٌ لَّكُمْ ۚ لِكُلِّ امْرِئٍ مِّنْهُم مَّا اكْتَسَبَ مِنَ الْإِثْمِ ۚ وَالَّذِي تَوَلَّىٰ كِبْرَهُ مِنْهُمْ لَهُ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Ña leen di indil jiixi-jaaxa [naaféq ya], ab kurél lañu ci yéen. Buleen ko jàppe ay, yiw la ci yéen. Kenn ku nekk ci yéen dana jot bàkkaaram. Képp ku ca ëppal dana am mbugal mu màgg.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
9Aaya

Tekki — An-Nur 9

Simoore An-Nur Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ndaw sa itam na waat ne merum Yàlla na wàcc…

Simoore Aaya 9/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers