An-Nur · 8/64
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nur
وَيَدْرَأُ عَنْهَا الْعَذَابَ أَن تَشْهَدَ أَرْبَعَ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ ۝٨
Wa yadra`u anhal `azaaba an tashhada arba`a shahaa daatim billaahi innahoo laminal kaazibeen
📖 Tekkim Wolof
Su jabar ja waate ñeenti yoon ci Yàlla ne waa ja fenkat la, kenn du ko sànni xeer [rajmu],

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore An-Nur

6وَالَّذِينَ يَرْمُونَ أَزْوَاجَهُمْ وَلَمْ يَكُن لَّهُمْ شُهَدَاءُ إِلَّا أَنفُسُهُمْ فَشَهَادَةُ أَحَدِهِمْ أَرْبَعُ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الصَّادِقِينَ
Ñay tuumaal seeni jabar te amuñu ay seede lu dul seen bopp, na waat ci Yàlla ñeenti yoon ne ku dëggu la,
7وَالْخَامِسَةُ أَنَّ لَعْنَتَ اللَّهِ عَلَيْهِ إِن كَانَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
juróomeel ba mu waat ne “rëbbum Yàlla [sori yërmaandeem] na dal ci kawam su dee fenkat la”.
8وَيَدْرَأُ عَنْهَا الْعَذَابَ أَن تَشْهَدَ أَرْبَعَ شَهَادَاتٍ بِاللَّهِ ۙ إِنَّهُ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ
Su jabar ja waate ñeenti yoon ci Yàlla ne waa ja fenkat la, kenn du ko sànni xeer [rajmu],
9وَالْخَامِسَةَ أَنَّ غَضَبَ اللَّهِ عَلَيْهَا إِن كَانَ مِنَ الصَّادِقِينَ
ndaw sa itam na waat ne merum Yàlla na wàcc ci kawam su jëkkëram ja waxee dëgg [pasem rëbboo dootu ko fàttaliku mukk] muy juróomeelu waatam.
10وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ وَأَنَّ اللَّهَ تَوَّابٌ حَكِيمٌ
Cëy dugankoon ak ngënéelul Yàlla ci yéen ak yërmaandeem, waaye nag Yàlla Nanguwaakoonu tuub la bu xeréñ !
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
8Aaya

Tekki — An-Nur 8

Simoore An-Nur Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su jabar ja waate ñeenti yoon ci Yàlla ne waa…

Simoore Aaya 8/64 — Simoore An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nur Dégg, Simoore An-Nur Tekki, Simoore An-Nur mp3, Simoore An-Nur pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers