Al-Furqan · 59/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۚ الرَّحْمَٰنُ فَاسْأَلْ بِهِ خَبِيرًا ۝٥٩
Allazee khalaqas samaawaati wal arda wa maa bainahumaa fee sittati aiyaamin summmmastawaa `alal `Arsh; ar Rahmaanu fas`al bihee khabeeraa
📖 Tekkim Wolof
Mooy Ki bind asamaan yaak suuf si ak li nekk seen diggante, ci juróom-benni fan, daldi yemoo ca gàngunaay ga [Aras], Moo di ab Yërëmaakoon. Laaj ko ku xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-61 — Al-Furqan

57قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ إِلَّا مَن شَاءَ أَن يَتَّخِذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Neel : “Laaju ma leen ci ag pey. Ku mu soob nag, mën naa joxe ci yoonu Yàlla”.
58وَتَوَكَّلْ عَلَى الْحَيِّ الَّذِي لَا يَمُوتُ وَسَبِّحْ بِحَمْدِهِ ۚ وَكَفَىٰ بِهِ بِذُنُوبِ عِبَادِهِ خَبِيرًا
Te nanga wéeru ci Yàlla Miy Aji-dund te du dee. Te nangay sàbbaal ci sant Ko. Moom Yàlla ku mat sëkk la ci xam bàkkaari jaamam ñi.
59الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۚ الرَّحْمَٰنُ فَاسْأَلْ بِهِ خَبِيرًا
Mooy Ki bind asamaan yaak suuf si ak li nekk seen diggante, ci juróom-benni fan, daldi yemoo ca gàngunaay ga [Aras], Moo di ab Yërëmaakoon. Laaj ko ku xam.
60وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اسْجُدُوا لِلرَّحْمَٰنِ قَالُوا وَمَا الرَّحْمَٰنُ أَنَسْجُدُ لِمَا تَأْمُرُنَا وَزَادَهُمْ نُفُورًا ۩
Saa su Nu leen waxee : “Sujjóotal-leen [Yàlla] Mi di ab Yërëmaakoon”, ñu tontu ne : “Kuy kooku ?” - Mu faf dolli leen ug foñ.
61تَبَارَكَ الَّذِي جَعَلَ فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَجَعَلَ فِيهَا سِرَاجًا وَقَمَرًا مُّنِيرًا
Barkeel na [Moom Yàlla] mi def ci asamaan si ay yoon, def ca ab làmp [jant bi] ak weer wu leer nàññ !
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Al-Furqan 59

Simoore Al-Furqan Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy Ki bind asamaan yaak suuf si ak li nekk…

Simoore Aaya 59/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers