Al-Furqan · 60/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اسْجُدُوا لِلرَّحْمَٰنِ قَالُوا وَمَا الرَّحْمَٰنُ أَنَسْجُدُ لِمَا تَأْمُرُنَا وَزَادَهُمْ نُفُورًا ۩ ۝٦٠
Wa izaa qeela lahumus judoo lir Rahmaani qaaloo wa mar Rahmaanu anasjudu limaa taamurunaa wa zaadahum nufooraa
📖 Tekkim Wolof
Saa su Nu leen waxee : “Sujjóotal-leen [Yàlla] Mi di ab Yërëmaakoon”, ñu tontu ne : “Kuy kooku ?” - Mu faf dolli leen ug foñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Simoore Al-Furqan

58وَتَوَكَّلْ عَلَى الْحَيِّ الَّذِي لَا يَمُوتُ وَسَبِّحْ بِحَمْدِهِ ۚ وَكَفَىٰ بِهِ بِذُنُوبِ عِبَادِهِ خَبِيرًا
Te nanga wéeru ci Yàlla Miy Aji-dund te du dee. Te nangay sàbbaal ci sant Ko. Moom Yàlla ku mat sëkk la ci xam bàkkaari jaamam ñi.
59الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۚ الرَّحْمَٰنُ فَاسْأَلْ بِهِ خَبِيرًا
Mooy Ki bind asamaan yaak suuf si ak li nekk seen diggante, ci juróom-benni fan, daldi yemoo ca gàngunaay ga [Aras], Moo di ab Yërëmaakoon. Laaj ko ku xam.
60وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اسْجُدُوا لِلرَّحْمَٰنِ قَالُوا وَمَا الرَّحْمَٰنُ أَنَسْجُدُ لِمَا تَأْمُرُنَا وَزَادَهُمْ نُفُورًا ۩
Saa su Nu leen waxee : “Sujjóotal-leen [Yàlla] Mi di ab Yërëmaakoon”, ñu tontu ne : “Kuy kooku ?” - Mu faf dolli leen ug foñ.
61تَبَارَكَ الَّذِي جَعَلَ فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَجَعَلَ فِيهَا سِرَاجًا وَقَمَرًا مُّنِيرًا
Barkeel na [Moom Yàlla] mi def ci asamaan si ay yoon, def ca ab làmp [jant bi] ak weer wu leer nàññ !
62وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ خِلْفَةً لِّمَنْ أَرَادَ أَن يَذَّكَّرَ أَوْ أَرَادَ شُكُورًا
Mooy Ki def guddeek bëccëg ñuy jëlasante ngir ku bëgg a xalaat, fàttaliku, mbaa mu bëgg a sant.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Al-Furqan 60

Simoore Al-Furqan Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su Nu leen waxee : “Sujjóotal-leen [Yàlla] Mi di…

Simoore Aaya 60/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers