Al-Furqan · 75/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
أُولَٰئِكَ يُجْزَوْنَ الْغُرْفَةَ بِمَا صَبَرُوا وَيُلَقَّوْنَ فِيهَا تَحِيَّةً وَسَلَامًا ۝٧٥
Ulaaa`ika yujzawnal ghurfata bimaa sabaroo wa yulaqqawna feehaa tahiyyatanw wa salaamaa
📖 Tekkim Wolof
Ñoom dees na leen feye ay néeg yu kawe [ca Àjjana], muy peyug la ñu doon muñ, te dees na leen fa teeroo ab nuyyoo ak jàmm [ju ne béyyi],

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Simoore Al-Furqan

73وَالَّذِينَ إِذَا ذُكِّرُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ لَمْ يَخِرُّوا عَلَيْهَا صُمًّا وَعُمْيَانًا
ña nga xam ne bu ñu déggee seen kàdduy Boroom, duñu ca tëx, duñu ca gumba ;
74وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا هَبْ لَنَا مِنْ أَزْوَاجِنَا وَذُرِّيَّاتِنَا قُرَّةَ أَعْيُنٍ وَاجْعَلْنَا لِلْمُتَّقِينَ إِمَامًا
ña nga xam ne dañuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, defal nu ci sunuy jabar ak sunuy doom ñuy seral xol, te nga def nu ay njiit ca ña ragal Yàlla tey wattandiku”.
75أُولَٰئِكَ يُجْزَوْنَ الْغُرْفَةَ بِمَا صَبَرُوا وَيُلَقَّوْنَ فِيهَا تَحِيَّةً وَسَلَامًا
Ñoom dees na leen feye ay néeg yu kawe [ca Àjjana], muy peyug la ñu doon muñ, te dees na leen fa teeroo ab nuyyoo ak jàmm [ju ne béyyi],
76خَالِدِينَ فِيهَا ۚ حَسُنَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا
dañu fay béel. Ndaw dëkkuwaay bu neex !
77قُلْ مَا يَعْبَأُ بِكُمْ رَبِّي لَوْلَا دُعَاؤُكُمْ ۖ فَقَدْ كَذَّبْتُمْ فَسَوْفَ يَكُونُ لِزَامًا
Neel : “Seen Boroom duleen faale, xanaa sax bu fekkoon ne yéen a ngi Koy jaamu ; waaye weddi woon ngeen Yonent bi. Seen mbugal, dungeen ko mën a raw, te dafay doo lu sax.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Al-Furqan 75

Simoore Al-Furqan Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom dees na leen feye ay néeg yu kawe [ca…

Simoore Aaya 75/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers