Al-Furqan · 77/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
قُلْ مَا يَعْبَأُ بِكُمْ رَبِّي لَوْلَا دُعَاؤُكُمْ ۖ فَقَدْ كَذَّبْتُمْ فَسَوْفَ يَكُونُ لِزَامًا ۝٧٧
Qul maa ya`ba`u bikum Rabbee law laa du`aaa`ukum faqad kazzabtum fasawfa yakoonu lizaamaa
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Seen Boroom duleen faale, xanaa sax bu fekkoon ne yéen a ngi Koy jaamu ; waaye weddi woon ngeen Yonent bi. Seen mbugal, dungeen ko mën a raw, te dafay doo lu sax.

🎧 Dégg


📜 Aaya 75-77 — Simoore Al-Furqan

75أُولَٰئِكَ يُجْزَوْنَ الْغُرْفَةَ بِمَا صَبَرُوا وَيُلَقَّوْنَ فِيهَا تَحِيَّةً وَسَلَامًا
Ñoom dees na leen feye ay néeg yu kawe [ca Àjjana], muy peyug la ñu doon muñ, te dees na leen fa teeroo ab nuyyoo ak jàmm [ju ne béyyi],
76خَالِدِينَ فِيهَا ۚ حَسُنَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا
dañu fay béel. Ndaw dëkkuwaay bu neex !
77قُلْ مَا يَعْبَأُ بِكُمْ رَبِّي لَوْلَا دُعَاؤُكُمْ ۖ فَقَدْ كَذَّبْتُمْ فَسَوْفَ يَكُونُ لِزَامًا
Neel : “Seen Boroom duleen faale, xanaa sax bu fekkoon ne yéen a ngi Koy jaamu ; waaye weddi woon ngeen Yonent bi. Seen mbugal, dungeen ko mën a raw, te dafay doo lu sax.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Al-Furqan 77

Simoore Al-Furqan Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Seen Boroom duleen faale, xanaa sax bu fekkoon…

Simoore Aaya 77/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 75–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers