An-Naml · 76/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
إِنَّ هَٰذَا الْقُرْآنَ يَقُصُّ عَلَىٰ بَنِي إِسْرَائِيلَ أَكْثَرَ الَّذِي هُمْ فِيهِ يَخْتَلِفُونَ ۝٧٦
Inna haazal Qur-aana yaqussu `alaa Baneee israaa`eela aksaral lazee hum feehi yakhtalifoon
📖 Tekkim Wolof
Alxuraan jii dafay nettali ci giir Bani-Israayiila, li ëpp ci la ñu daan juuyoo ak a wuute,

🎧 Dégg


📜 Aaya 74-78 — Simoore An-Naml

74وَإِنَّ رَبَّكَ لَيَعْلَمُ مَا تُكِنُّ صُدُورُهُمْ وَمَا يُعْلِنُونَ
Te it sa Boroom xam na li ngeen rënk ci seeni dënn ak li ngeen di feeñal.
75وَمَا مِنْ غَائِبَةٍ فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ إِلَّا فِي كِتَابٍ مُّبِينٍ
Te it amul lenn lu fàddu nekk ci asamaan si walla ci suuf si te dul ne nekk na ci biir ab Téere bu ñu faramfàcce.
76إِنَّ هَٰذَا الْقُرْآنَ يَقُصُّ عَلَىٰ بَنِي إِسْرَائِيلَ أَكْثَرَ الَّذِي هُمْ فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Alxuraan jii dafay nettali ci giir Bani-Israayiila, li ëpp ci la ñu daan juuyoo ak a wuute,
77وَإِنَّهُ لَهُدًى وَرَحْمَةٌ لِّلْمُؤْمِنِينَ
Te Alxuraan jooju njub la ak yërmaande ci képp ku gëm [di ab jullit].
78إِنَّ رَبَّكَ يَقْضِي بَيْنَهُم بِحُكْمِهِ ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْعَلِيمُ
Sa Boroom dana àtte seen diggante ci àtteem yi ; Mooy Boroom kàttan ga, di Ku xam.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
76Aaya

Tekki — An-Naml 76

Simoore An-Naml Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alxuraan jii dafay nettali ci giir Bani-Israayiila, li ëpp ci…

Simoore Aaya 76/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers