An-Naml · 84/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
حَتَّىٰ إِذَا جَاءُوا قَالَ أَكَذَّبْتُم بِآيَاتِي وَلَمْ تُحِيطُوا بِهَا عِلْمًا أَمَّاذَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ۝٨٤
Hattaaa izaa jaaa`oo qaala akazzabtum bi Aayaatee wa lam tuheetoo bihaa `ilman ammaazaa kuntum ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu agsee, [Yàlla] ne leen : “Waaw, yéen a daan weddi Samay kàddu te xamuleen ci woon dara ? Walla lan ngeen daan def ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 82-86 — Simoore An-Naml

82۞ وَإِذَا وَقَعَ الْقَوْلُ عَلَيْهِمْ أَخْرَجْنَا لَهُمْ دَابَّةً مِّنَ الْأَرْضِ تُكَلِّمُهُمْ أَنَّ النَّاسَ كَانُوا بِآيَاتِنَا لَا يُوقِنُونَ
Saa su wax ja tàbbee ci seen kaw, Dananu leen génneel benn mala buy wàqanteek ñoom ne : Nit ñi gëmuñu woon Sunuy kàddu, kéemaan.
83وَيَوْمَ نَحْشُرُ مِن كُلِّ أُمَّةٍ فَوْجًا مِّمَّن يُكَذِّبُ بِآيَاتِنَا فَهُمْ يُوزَعُونَ
Bu keroogee Bis ba Nuy pang, ci wépp xeet ay mbooloo yu daan jàppe Sunu kàddu yii ay fen [di ko weddi], Nu def leen ñu di ay sàppe.
84حَتَّىٰ إِذَا جَاءُوا قَالَ أَكَذَّبْتُم بِآيَاتِي وَلَمْ تُحِيطُوا بِهَا عِلْمًا أَمَّاذَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Bu ñu agsee, [Yàlla] ne leen : “Waaw, yéen a daan weddi Samay kàddu te xamuleen ci woon dara ? Walla lan ngeen daan def ? ”
85وَوَقَعَ الْقَوْلُ عَلَيْهِم بِمَا ظَلَمُوا فَهُمْ لَا يَنطِقُونَ
Su wax ja agsee ci ñoom, seen tooñ ga dana tax duñu àddu.
86أَلَمْ يَرَوْا أَنَّا جَعَلْنَا اللَّيْلَ لِيَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Ndax dañoo gisul ne [Man Yàlla] maa leen defal guddi ngir ñu di ca dal-lu, def bëccëg muy yëngukaay ? Ay kéemaan nekk na ci biir loolu ngir ñi gëm.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — An-Naml 84

Simoore An-Naml Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu agsee, [Yàlla] ne leen : “Waaw, yéen a…

Simoore Aaya 84/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers