An-Naml · 85/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَوَقَعَ الْقَوْلُ عَلَيْهِم بِمَا ظَلَمُوا فَهُمْ لَا يَنطِقُونَ ۝٨٥
Wa waqa`al qawlu `alaihim bimaa zalamoo fahum laa yantiqoon
📖 Tekkim Wolof
Su wax ja agsee ci ñoom, seen tooñ ga dana tax duñu àddu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 83-87 — Simoore An-Naml

83وَيَوْمَ نَحْشُرُ مِن كُلِّ أُمَّةٍ فَوْجًا مِّمَّن يُكَذِّبُ بِآيَاتِنَا فَهُمْ يُوزَعُونَ
Bu keroogee Bis ba Nuy pang, ci wépp xeet ay mbooloo yu daan jàppe Sunu kàddu yii ay fen [di ko weddi], Nu def leen ñu di ay sàppe.
84حَتَّىٰ إِذَا جَاءُوا قَالَ أَكَذَّبْتُم بِآيَاتِي وَلَمْ تُحِيطُوا بِهَا عِلْمًا أَمَّاذَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Bu ñu agsee, [Yàlla] ne leen : “Waaw, yéen a daan weddi Samay kàddu te xamuleen ci woon dara ? Walla lan ngeen daan def ? ”
85وَوَقَعَ الْقَوْلُ عَلَيْهِم بِمَا ظَلَمُوا فَهُمْ لَا يَنطِقُونَ
Su wax ja agsee ci ñoom, seen tooñ ga dana tax duñu àddu.
86أَلَمْ يَرَوْا أَنَّا جَعَلْنَا اللَّيْلَ لِيَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Ndax dañoo gisul ne [Man Yàlla] maa leen defal guddi ngir ñu di ca dal-lu, def bëccëg muy yëngukaay ? Ay kéemaan nekk na ci biir loolu ngir ñi gëm.
87وَيَوْمَ يُنفَخُ فِي الصُّورِ فَفَزِعَ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ إِلَّا مَن شَاءَ اللَّهُ ۚ وَكُلٌّ أَتَوْهُ دَاخِرِينَ
Bu keroogee Bis ba ñuy wal buftu bi, ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ñoom ñépp danañu tiit, ku dul ku soob Yàlla ! – Ñoom ñépp danañu dikk fa Yàlla te tott.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — An-Naml 85

Simoore An-Naml Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su wax ja agsee ci ñoom, seen tooñ ga dana…

Simoore Aaya 85/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers