Aali Imran · 17/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
الصَّابِرِينَ وَالصَّادِقِينَ وَالْقَانِتِينَ وَالْمُنفِقِينَ وَالْمُسْتَغْفِرِينَ بِالْأَسْحَارِ ۝١٧
Assaabireena wassaa diqeena walqaaniteena walmunfiqeena walmus taghfireena bil ashaar
📖 Tekkim Wolof
ñooy, muñkat ya, ña dëggal, diy jaamukat, diy joxekati alal [ngir Yàlla] tey sàkku njéggal waxtuw njël.
🎧 Dégg

📜 Aaya 15-19 — Aali Imran

15۞ قُلْ أَؤُنَبِّئُكُم بِخَيْرٍ مِّن ذَٰلِكُمْ ۚ لِلَّذِينَ اتَّقَوْا عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا وَأَزْوَاجٌ مُّطَهَّرَةٌ وَرِضْوَانٌ مِّنَ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ بَصِيرٌ بِالْعِبَادِ
Neel : “Moo ndax duma leen xamal lu gën loolu ci yéen ? Gaa ña nga xam ne dañoo ragal Yàlla, am nañu, fa seen Boroom, Àjjana joo xam ne dex yaa ngay daw ci ronam, ñu sax fa dàkk ak i soxna yu ñu laabal , ak ngërëm lu bawoo ca Yàlla.” Yàllaa ngi gis jaam ñi,
16الَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا إِنَّنَا آمَنَّا فَاغْفِرْ لَنَا ذُنُوبَنَا وَقِنَا عَذَابَ النَّارِ
ñooy ñay wax naan : "Sunu Boroom, nun gëm nanu ; jéggal nu sunuy bàkkaar, te fegal nu mbugalu Safara”,
17الصَّابِرِينَ وَالصَّادِقِينَ وَالْقَانِتِينَ وَالْمُنفِقِينَ وَالْمُسْتَغْفِرِينَ بِالْأَسْحَارِ
ñooy, muñkat ya, ña dëggal, diy jaamukat, diy joxekati alal [ngir Yàlla] tey sàkku njéggal waxtuw njël.
18شَهِدَ اللَّهُ أَنَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ وَالْمَلَائِكَةُ وَأُولُو الْعِلْمِ قَائِمًا بِالْقِسْطِ ۚ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Yàlla seede na ne, amul jeneen Yàlla ju dul Moom, Malaaka ya ak woroom xam-xam ya taxawe ci maandu it, seede nañu ne amul jeneen Yàlla ju dul Moom. Ku not la, ku xereñ la !
19إِنَّ الدِّينَ عِندَ اللَّهِ الْإِسْلَامُ ۗ وَمَا اخْتَلَفَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ إِلَّا مِن بَعْدِ مَا جَاءَهُمُ الْعِلْمُ بَغْيًا بَيْنَهُمْ ۗ وَمَن يَكْفُرْ بِآيَاتِ اللَّهِ فَإِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Diine Yàlla tigi mooy Lislaam. Ñoñ-téere ya yi wuutewuñu woon lu dul ba leen xam-xam ba dikkalee, ñu beew ci seeni diggante. Képp ku weddi kàddug Yàlla... na xam ne Yàlla ku gaaw la ci xayma jëf yi !
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
17Aaya

Tekki — Aali Imran 17

Simoore Aali Imran Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñooy, muñkat ya, ña dëggal, diy jaamukat, diy joxekati alal…

Simoore Aaya 17/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers