Al-Ahzab · 27/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
وَأَوْرَثَكُمْ أَرْضَهُمْ وَدِيَارَهُمْ وَأَمْوَالَهُمْ وَأَرْضًا لَّمْ تَطَئُوهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرًا ۝٢٧
Wa awrasakum ardahum wa diyaarahum wa amwaalahum wa ardal lam tata`oohaa; wa kaanal laahu `alaa kulli shai`in Qadeeraa
📖 Tekkim Wolof
Mu donnale leen seen suuf, ak seeni kër, ak seeni alal, ak suuf soo xam ne mësuleen ca xand. Yàlla mën na lu ne.
🎧 Dégg

📜 Aaya 25-29 — Al-Ahzab

25وَرَدَّ اللَّهُ الَّذِينَ كَفَرُوا بِغَيْظِهِمْ لَمْ يَنَالُوا خَيْرًا ۚ وَكَفَى اللَّهُ الْمُؤْمِنِينَ الْقِتَالَ ۚ وَكَانَ اللَّهُ قَوِيًّا عَزِيزًا
Yàlla delloo na yéefar ya, ñu dellook seen mer, amuñu wenn yiw, Yàlla fegal na jullit ñi xeex ba. Yàlla ku bari doole la tey Boroom kàttan.
26وَأَنزَلَ الَّذِينَ ظَاهَرُوهُم مِّنْ أَهْلِ الْكِتَابِ مِن صَيَاصِيهِمْ وَقَذَفَ فِي قُلُوبِهِمُ الرُّعْبَ فَرِيقًا تَقْتُلُونَ وَتَأْسِرُونَ فَرِيقًا
Te wàcce na ca ña doom jàmmaarlook yéen te bokk ca ñoñ-Téere, [yonjaxal leen], daldi dugal am tiit ci seen xol ya ; ngeen rey ñenn ña, lél ñenn ña.
27وَأَوْرَثَكُمْ أَرْضَهُمْ وَدِيَارَهُمْ وَأَمْوَالَهُمْ وَأَرْضًا لَّمْ تَطَئُوهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرًا
Mu donnale leen seen suuf, ak seeni kër, ak seeni alal, ak suuf soo xam ne mësuleen ca xand. Yàlla mën na lu ne.
28يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ قُل لِّأَزْوَاجِكَ إِن كُنتُنَّ تُرِدْنَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا وَزِينَتَهَا فَتَعَالَيْنَ أُمَتِّعْكُنَّ وَأُسَرِّحْكُنَّ سَرَاحًا جَمِيلًا
Éy yaw Yonent bi ! Waxal say soxna ne leen : “Su fekke ne dundug àddina sii rekk a leen ñor ak ub taaram, kaayleen ma yombalal leen ko, ci ma fase leen ci am pase mu jekk.
29وَإِن كُنتُنَّ تُرِدْنَ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَالدَّارَ الْآخِرَةَ فَإِنَّ اللَّهَ أَعَدَّ لِلْمُحْسِنَاتِ مِنكُنَّ أَجْرًا عَظِيمًا
Su fekkee nag ne Yàlla ak Yonentam ak kër gu mujj ga di àllaaxira rekk a leen ñor, [nangeen xam ne] képp kuy rafetal ci yéen, Yàlla dana ko waajalal ag pey gu màgg.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Ahzab 27

Simoore Al-Ahzab Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu donnale leen seen suuf, ak seeni kër, ak seeni…

Simoore Aaya 27/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers