Al-Ahzab · 67/73
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahzab
وَقَالُوا رَبَّنَا إِنَّا أَطَعْنَا سَادَتَنَا وَكُبَرَاءَنَا فَأَضَلُّونَا السَّبِيلَا ۝٦٧
Wa qaaloo Rabbanaaa innaaa ata`naa saadatanaa wa kubaraaa`anaa fa adalloonas sabeelaa
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, nun dey toppoon nanu sunuy sang ak sunuy kilifa. Ñu réerale nu ak yoon wa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Simoore Al-Ahzab

65خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ لَّا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
dañu fay béel fàww, duñu fa am ku leen méngoo, duñu fa am ndimbal.
66يَوْمَ تُقَلَّبُ وُجُوهُهُمْ فِي النَّارِ يَقُولُونَ يَا لَيْتَنَا أَطَعْنَا اللَّهَ وَأَطَعْنَا الرَّسُولَا
Bis ba ñuy wëlbati seeni kanam ca Safara, ñuy wax naan : “Aka neexoon nu toppoon Yàlla, nu toppoon Yonent ba ! ”.
67وَقَالُوا رَبَّنَا إِنَّا أَطَعْنَا سَادَتَنَا وَكُبَرَاءَنَا فَأَضَلُّونَا السَّبِيلَا
Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, nun dey toppoon nanu sunuy sang ak sunuy kilifa. Ñu réerale nu ak yoon wa.
68رَبَّنَا آتِهِمْ ضِعْفَيْنِ مِنَ الْعَذَابِ وَالْعَنْهُمْ لَعْنًا كَبِيرًا
Boroom sunu, fulandileen mbugal te nga rëbbleen rëbb mu rëy”.
69يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَكُونُوا كَالَّذِينَ آذَوْا مُوسَىٰ فَبَرَّأَهُ اللَّهُ مِمَّا قَالُوا ۚ وَكَانَ عِندَ اللَّهِ وَجِيهًا
Éy yéen ñi gëm ! Buleen mel ni ña daan lor Muusaa, di ko tuumaal. Far Yàlla setal ko ca tuuma ya, di ku mu jubaloon.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
67Aaya

Tekki — Al-Ahzab 67

Simoore Al-Ahzab Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, nun dey toppoon…

Simoore Aaya 67/73 — Simoore Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahzab Dégg, Simoore Al-Ahzab Tekki, Simoore Al-Ahzab mp3, Simoore Al-Ahzab pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers