Ya-Sin · 44/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
إِلَّا رَحْمَةً مِّنَّا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ ۝٤٤
Illaa rahmatam minnaa wa mataa`an ilaa heen
📖 Tekkim Wolof
lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal ba jëmmi jamono.

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore Ya-Sin

42وَخَلَقْنَا لَهُم مِّن مِّثْلِهِ مَا يَرْكَبُونَ
Te sàkkal Nanu leen yeneen yu ni mel ñu di ca war.
43وَإِن نَّشَأْ نُغْرِقْهُمْ فَلَا صَرِيخَ لَهُمْ وَلَا هُمْ يُنقَذُونَ
Bu Nu sooboon, Nu labal leen ; duñu xam fu ñuy yuuxu jëmële, te kenn du leen xettali,
44إِلَّا رَحْمَةً مِّنَّا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ
lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal ba jëmmi jamono.
45وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اتَّقُوا مَا بَيْنَ أَيْدِيكُمْ وَمَا خَلْفَكُمْ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Te saa su ñu leen waxee ne : “Wattandikuleen li nekk ci seen kanam ak li ci seen ginnaaw ndax amaana yërmaande wàcc ci yéen” !...
46وَمَا تَأْتِيهِم مِّنْ آيَةٍ مِّنْ آيَاتِ رَبِّهِمْ إِلَّا كَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Amul yenn laaya , yu bokk ci seeni laayay Boroom, dikkal leen te dañu koo dëddu.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Ya-Sin 44

Simoore Ya-Sin Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal…

Simoore Aaya 44/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers