Ya-Sin · 45/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اتَّقُوا مَا بَيْنَ أَيْدِيكُمْ وَمَا خَلْفَكُمْ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ ٤٥
Transliteration
Wa izaa qeela lahumuttaqoo maa baina aideekum wa maa khalfakum la`allakum turhamoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te saa su ñu leen waxee ne : “Wattandikuleen li nekk ci seen kanam ak li ci seen ginnaaw ndax amaana yërmaande wàcc ci yéen” !...
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 43-47 — Ya-Sin
43وَإِن نَّشَأْ نُغْرِقْهُمْ فَلَا صَرِيخَ لَهُمْ وَلَا هُمْ يُنقَذُونَ
Bu Nu sooboon, Nu labal leen ; duñu xam fu ñuy yuuxu jëmële, te kenn du leen xettali,
44إِلَّا رَحْمَةً مِّنَّا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ
lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal ba jëmmi jamono.
45وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اتَّقُوا مَا بَيْنَ أَيْدِيكُمْ وَمَا خَلْفَكُمْ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Te saa su ñu leen waxee ne : “Wattandikuleen li nekk ci seen kanam ak li ci seen ginnaaw ndax amaana yërmaande wàcc ci yéen” !...
46وَمَا تَأْتِيهِم مِّنْ آيَةٍ مِّنْ آيَاتِ رَبِّهِمْ إِلَّا كَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Amul yenn laaya , yu bokk ci seeni laayay Boroom, dikkal leen te dañu koo dëddu.
47وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ أَنفِقُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ قَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا أَنُطْعِمُ مَن لَّوْ يَشَاءُ اللَّهُ أَطْعَمَهُ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Saa su ñu leen waxee ne : “Joxeleen ci alal ji leen Yàlla wërsëgal”, ña weddi dañuy wax ña gëm, naan leen : “Moo ndax nun danuy dundal koo xam ne bu neexoon Yàlla mu dundal ko ? Yéen daal ci ag réer gu bir ngeen nekk”.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
45Aaya
Tekki — Ya-Sin 45
Simoore Ya-Sin Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te saa su ñu leen waxee ne : “Wattandikuleen li…Simoore Aaya 45/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








