Ya-Sin · 69/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَمَا عَلَّمْنَاهُ الشِّعْرَ وَمَا يَنبَغِي لَهُ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ وَقُرْآنٌ مُّبِينٌ ۝٦٩
Wa maa `allamnaahush shi`ra wa maa yambaghee lah; in huwa illaa zikrunw-wa Qur-aanum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Jàngalunu Muhammad woy mbaa lu koy nuru ; lii daal du dara lu dul ag fàttali ak Alxuraan juy biral,

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Ya-Sin

67وَلَوْ نَشَاءُ لَمَسَخْنَاهُمْ عَلَىٰ مَكَانَتِهِمْ فَمَا اسْتَطَاعُوا مُضِيًّا وَلَا يَرْجِعُونَ
Bu Nu sooboon, Dananu leen rat benn barab ; dootuñu dem, duñu dikk.
68وَمَن نُّعَمِّرْهُ نُنَكِّسْهُ فِي الْخَلْقِ ۖ أَفَلَا يَعْقِلُونَ
Képp ku Ma defal aw fan wu guddi, Danaa ko màggatloo, xanaa dungeen xalaat ?
69وَمَا عَلَّمْنَاهُ الشِّعْرَ وَمَا يَنبَغِي لَهُ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ وَقُرْآنٌ مُّبِينٌ
Jàngalunu Muhammad woy mbaa lu koy nuru ; lii daal du dara lu dul ag fàttali ak Alxuraan juy biral,
70لِّيُنذِرَ مَن كَانَ حَيًّا وَيَحِقَّ الْقَوْلُ عَلَى الْكَافِرِينَ
ngir muy xupp ñiy dundu, wax ja itam di lu yay ca yéefar ya.
71أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا خَلَقْنَا لَهُم مِّمَّا عَمِلَتْ أَيْدِينَا أَنْعَامًا فَهُمْ لَهَا مَالِكُونَ
Xanaa dañoo gisul ne sàkkal Nanu leen ci Sunu liggéeyu loxo ag jur gu ñuy moom ;
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Ya-Sin 69

Simoore Ya-Sin Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jàngalunu Muhammad woy mbaa lu koy nuru ; lii daal…

Simoore Aaya 69/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers