Ya-Sin · 83/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
فَسُبْحَانَ الَّذِي بِيَدِهِ مَلَكُوتُ كُلِّ شَيْءٍ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ ۝٨٣
Fa Subhaanal lazee biyadihee malakootu kulli shai-inw-wa ilaihi turja`oon
📖 Tekkim Wolof
Tudd naa sellug ki nga xam moo ame ci loxoom moomeelug lépp ! Te it ca moom ngeen di dellu yéen ñépp.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 81-83 — Simoore Ya-Sin

81أَوَلَيْسَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يَخْلُقَ مِثْلَهُم ۚ بَلَىٰ وَهُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ
Moo ndax ku bind asamaan yeek suuf mënul a bindaat ñeneen yu na mel ? Axakañ ! Moo di Bindaakoon, Xamaakoon bi.
82إِنَّمَا أَمْرُهُ إِذَا أَرَادَ شَيْئًا أَن يَقُولَ لَهُ كُن فَيَكُونُ
Ay mbiram moo di, saa su bëggee menn mbir, dakoy wax : “Nekkal”, mu daldi nekk.
83فَسُبْحَانَ الَّذِي بِيَدِهِ مَلَكُوتُ كُلِّ شَيْءٍ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Tudd naa sellug ki nga xam moo ame ci loxoom moomeelug lépp ! Te it ca moom ngeen di dellu yéen ñépp.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — Ya-Sin 83

Simoore Ya-Sin Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tudd naa sellug ki nga xam moo ame ci loxoom…

Simoore Aaya 83/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 81–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 11, 2026

Don't forget us in your sincere prayers