Ya-Sin · 82/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
إِنَّمَا أَمْرُهُ إِذَا أَرَادَ شَيْئًا أَن يَقُولَ لَهُ كُن فَيَكُونُ ٨٢
Transliteration
Innamaa amruhooo izaaa araada shai`an ai-yaqoola lahoo kun fa-yakoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ay mbiram moo di, saa su bëggee menn mbir, dakoy wax : “Nekkal”, mu daldi nekk.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 80-83 — Ya-Sin
80الَّذِي جَعَلَ لَكُم مِّنَ الشَّجَرِ الْأَخْضَرِ نَارًا فَإِذَا أَنتُم مِّنْهُ تُوقِدُونَ
te Moo di ki leen defal ci garab gu nëtëx, aw safara wu ngeen di taaloo.
81أَوَلَيْسَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يَخْلُقَ مِثْلَهُم ۚ بَلَىٰ وَهُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ
Moo ndax ku bind asamaan yeek suuf mënul a bindaat ñeneen yu na mel ? Axakañ ! Moo di Bindaakoon, Xamaakoon bi.
82إِنَّمَا أَمْرُهُ إِذَا أَرَادَ شَيْئًا أَن يَقُولَ لَهُ كُن فَيَكُونُ
Ay mbiram moo di, saa su bëggee menn mbir, dakoy wax : “Nekkal”, mu daldi nekk.
83فَسُبْحَانَ الَّذِي بِيَدِهِ مَلَكُوتُ كُلِّ شَيْءٍ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Tudd naa sellug ki nga xam moo ame ci loxoom moomeelug lépp ! Te it ca moom ngeen di dellu yéen ñépp.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
82Aaya
Tekki — Ya-Sin 82
Simoore Ya-Sin Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ay mbiram moo di, saa su bëggee menn mbir, dakoy…Simoore Aaya 82/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 80–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








