As-Saffat · 130/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
سَلَامٌ عَلَىٰ إِلْ يَاسِينَ ۝١٣٠
Salaamun `alaaa Ilyaaseen
📖 Tekkim Wolof
“Jàmm yal na nekk ci njabootug Ilyaas”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 128-132 — Simoore As-Saffat

128إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ba mu des jaami Yàlla ya daan sellal.
129وَتَرَكْنَا عَلَيْهِ فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi nit ñuy mujj noonu di ko fàttaliku :
130سَلَامٌ عَلَىٰ إِلْ يَاسِينَ
“Jàmm yal na nekk ci njabootug Ilyaas”.
131إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal,
132إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
130Aaya

Tekki — As-Saffat 130

Simoore As-Saffat Aaya 130 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Jàmm yal na nekk ci njabootug Ilyaas”.

Simoore Aaya 130/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 128–132. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers