As-Saffat · 129/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَتَرَكْنَا عَلَيْهِ فِي الْآخِرِينَ ۝١٢٩
Wa taraknaa `alaihi fil aakhireen
📖 Tekkim Wolof
Nu bàyyi nit ñuy mujj noonu di ko fàttaliku :

🎧 Dégg


📜 Aaya 127-131 — Simoore As-Saffat

127فَكَذَّبُوهُ فَإِنَّهُمْ لَمُحْضَرُونَ
Ñu weddi ko, Nu mbugal leen.
128إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ba mu des jaami Yàlla ya daan sellal.
129وَتَرَكْنَا عَلَيْهِ فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi nit ñuy mujj noonu di ko fàttaliku :
130سَلَامٌ عَلَىٰ إِلْ يَاسِينَ
“Jàmm yal na nekk ci njabootug Ilyaas”.
131إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
129Aaya

Tekki — As-Saffat 129

Simoore As-Saffat Aaya 129 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu bàyyi nit ñuy mujj noonu di ko fàttaliku :

Simoore Aaya 129/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 127–131. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers