As-Saffat · 73/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُنذَرِينَ ۝٧٣
Fanzur kaifa kaana `aaqibatul munzareen
📖 Tekkim Wolof
Xoolal mujjug ñanu daan xupp !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 71-75 — Simoore As-Saffat

71وَلَقَدْ ضَلَّ قَبْلَهُمْ أَكْثَرُ الْأَوَّلِينَ
Li ëppoon ca ña leen jiitu woon sàkku woon nañu.
72وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا فِيهِم مُّنذِرِينَ
Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate .
73فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُنذَرِينَ
Xoolal mujjug ñanu daan xupp !
74إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ña ca dul jaami Yàlla ya ca daan sellal :
75وَلَقَدْ نَادَانَا نُوحٌ فَلَنِعْمَ الْمُجِيبُونَ
Nooh woo na Nu di ñaan, Nu wuyyu ko, nangu ñaanam.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — As-Saffat 73

Simoore As-Saffat Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xoolal mujjug ñanu daan xupp !

Simoore Aaya 73/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers