As-Saffat · 72/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا فِيهِم مُّنذِرِينَ ۝٧٢
Wa laqad arsalnaa feehim munzireen
📖 Tekkim Wolof
Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate .

🎧 Dégg


📜 Aaya 70-74 — Simoore As-Saffat

70فَهُمْ عَلَىٰ آثَارِهِمْ يُهْرَعُونَ
ñuy yolli-yolli topp leen.
71وَلَقَدْ ضَلَّ قَبْلَهُمْ أَكْثَرُ الْأَوَّلِينَ
Li ëppoon ca ña leen jiitu woon sàkku woon nañu.
72وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا فِيهِم مُّنذِرِينَ
Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate .
73فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُنذَرِينَ
Xoolal mujjug ñanu daan xupp !
74إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ña ca dul jaami Yàlla ya ca daan sellal :
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — As-Saffat 72

Simoore As-Saffat Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate…

Simoore Aaya 72/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers